Al-Waqi'a · 71/96
Tekki Waxtaan — Al-Waqi'a
أَفَرَأَيْتُمُ النَّارَ الَّتِي تُورُونَ ۝٧١
Afara`aytumun naaral latee tooroon
📖 Tekkim Wolof
Xanaa gisuleen Safara wi ngeen di taaloo ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 69-73 — Al-Waqi'a

69أَأَنتُمْ أَنزَلْتُمُوهُ مِنَ الْمُزْنِ أَمْ نَحْنُ الْمُنزِلُونَ
Moo ndax yéen a koy wàccee ci niir yi ? walla Nun noo koy wàcce ?
70لَوْ نَشَاءُ جَعَلْنَاهُ أُجَاجًا فَلَوْلَا تَشْكُرُونَ
Sunu neexoon, Nu sëccël ko mu wex xàtt ak xorom. Moo xanaa dungeen sant ?
71أَفَرَأَيْتُمُ النَّارَ الَّتِي تُورُونَ
Xanaa gisuleen Safara wi ngeen di taaloo ?
72أَأَنتُمْ أَنشَأْتُمْ شَجَرَتَهَا أَمْ نَحْنُ الْمُنشِئُونَ
Moo ndax yéen a sos garab gi walla Nun noo ko sos sàkk ko ?
73نَحْنُ جَعَلْنَاهَا تَذْكِرَةً وَمَتَاعًا لِّلْمُقْوِينَ
Def nanu ko mu di ag fàttali (ci safaraw ëllëg), di jumtukaay ci képp ku ko ittewoo.
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
71Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 71

Simoore Al-Waqi'a Aaya 71 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xanaa gisuleen Safara wi ngeen di taaloo ?

Simoore Aaya 71/96 — Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Waqi'a Dégg, Al-Waqi'a Tekki, Al-Waqi'a mp3, Al-Waqi'a pdf. Aaya 69–73. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers