Al-Waqi'a · 86/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
فَلَوْلَا إِن كُنتُمْ غَيْرَ مَدِينِينَ ۝٨٦
Falaw laaa in kuntum ghira madeeneen
📖 Tekkim Wolof
Bu ngeen, jortee ne ameeluleen Yàlla dara,

🎧 Dégg


📜 Aaya 84-88 — Simoore Al-Waqi'a

84وَأَنتُمْ حِينَئِذٍ تَنظُرُونَ
te fekk na yéen a nga koy xool,
85وَنَحْنُ أَقْرَبُ إِلَيْهِ مِنكُمْ وَلَٰكِن لَّا تُبْصِرُونَ
fekk na booba Nun Yàlla noo ko gëna jigeñ waaye du ngeen gis.
86فَلَوْلَا إِن كُنتُمْ غَيْرَ مَدِينِينَ
Bu ngeen, jortee ne ameeluleen Yàlla dara,
87تَرْجِعُونَهَا إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
ana lan moo tax kon delloosiwuleen [ruuh ga], ndegam ñu dëggu ngeen ?
88فَأَمَّا إِن كَانَ مِنَ الْمُقَرَّبِينَ
Su fekkee ne koo ku dafa jige woon (Yàlla),
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
86Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 86

Simoore Al-Waqi'a Aaya 86 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ngeen, jortee ne ameeluleen Yàlla dara,

Simoore Aaya 86/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 84–88. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers