Al-An'am · 16/165
Tekki Waxtaan — Al-An'am
مَّن يُصْرَفْ عَنْهُ يَوْمَئِذٍ فَقَدْ رَحِمَهُ ۚ وَذَٰلِكَ الْفَوْزُ الْمُبِينُ ١٦
Transliteration
Mai yusraf `anhu Yawma`izin faqad rahimah; wa zaalikal fawzul mubeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Koo xam ne musal nañu ko ca bis booba ci mbugal moo ma, kooka Yàlla yërëm na ko, te loolu mooy texe tigi tigi.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 14-18 — Al-An'am
14قُلْ أَغَيْرَ اللَّهِ أَتَّخِذُ وَلِيًّا فَاطِرِ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَهُوَ يُطْعِمُ وَلَا يُطْعَمُ ۗ قُلْ إِنِّي أُمِرْتُ أَنْ أَكُونَ أَوَّلَ مَنْ أَسْلَمَ ۖ وَلَا تَكُونَنَّ مِنَ الْمُشْرِكِينَ
Neel : “Moo ndax ci keneen ku dul Yàlla laay sàkku kiiraay, te Moo sàkk asamaan yeek suuf si ? Mooy lele te kenn du ko leel [ñam]. Neel : “Dëggaleef na ma, ma nekk ku jëkk a wommatu ”. Te buleen bokk ca way-bokkaale ña.
15قُلْ إِنِّي أَخَافُ إِنْ عَصَيْتُ رَبِّي عَذَابَ يَوْمٍ عَظِيمٍ
Neel : “Su ma moyee sama Boroom [cig ndigalam], mbugalum bis bu màgg ba [Bis-pénc ba], ragal naa mu dal ma ”.
16مَّن يُصْرَفْ عَنْهُ يَوْمَئِذٍ فَقَدْ رَحِمَهُ ۚ وَذَٰلِكَ الْفَوْزُ الْمُبِينُ
Koo xam ne musal nañu ko ca bis booba ci mbugal moo ma, kooka Yàlla yërëm na ko, te loolu mooy texe tigi tigi.
17وَإِن يَمْسَسْكَ اللَّهُ بِضُرٍّ فَلَا كَاشِفَ لَهُ إِلَّا هُوَ ۖ وَإِن يَمْسَسْكَ بِخَيْرٍ فَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Su la Yàlla tegee metit, kenn du mën a teggi lor jooju ku dul Moom. Su la joxee yiw, xamal ne Moom lu nekk la mën.
18وَهُوَ الْقَاهِرُ فَوْقَ عِبَادِهِ ۚ وَهُوَ الْحَكِيمُ الْخَبِيرُ
Te Moom Aji-not la ci kaw jaam ñi ; Ku xereñ la [Moom Yàlla], Ku deñ la ci kumpa.
Al-An'amFihi Alxuraan
165Aaya
MeccanRevelation
16Aaya
Tekki — Al-An'am 16
Simoore Al-An'am Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Koo xam ne musal nañu ko ca bis booba ci…Simoore Aaya 16/165 — Al-An'am الأنعام (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-An'am Dégg, Al-An'am Tekki, Al-An'am mp3, Al-An'am pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








