Al-Qalam · 22/52
Tekki Waxtaan — Al-Qalam
أَنِ اغْدُوا عَلَىٰ حَرْثِكُمْ إِن كُنتُمْ صَارِمِينَ ۝٢٢
Anighdoo `alaa harsikum in kuntum saarimeen
📖 Tekkim Wolof
“Daldi ne teel leen xëy tool waay ndegam da ngeen bëgg góob”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 20-24 — Al-Qalam

20فَأَصْبَحَتْ كَالصَّرِيمِ
ba bët setee, mu melni luñu déqi.
21فَتَنَادَوْا مُصْبِحِينَ
Ba ñu xëy, wootante ca suba cuuy :
22أَنِ اغْدُوا عَلَىٰ حَرْثِكُمْ إِن كُنتُمْ صَارِمِينَ
“Daldi ne teel leen xëy tool waay ndegam da ngeen bëgg góob”.
23فَانطَلَقُوا وَهُمْ يَتَخَافَتُونَ
Ña ngay làkk, ca tool ya di déeyante :
24أَن لَّا يَدْخُلَنَّهَا الْيَوْمَ عَلَيْكُم مِّسْكِينٌ
Tey wax naan : “Tey jii buleen seetaan benn miskin di dugg ci tool yi”.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — Al-Qalam 22

Simoore Al-Qalam Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Daldi ne teel leen xëy tool waay ndegam da ngeen…

Simoore Aaya 22/52 — Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qalam Dégg, Al-Qalam Tekki, Al-Qalam mp3, Al-Qalam pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers