Al-Qalam · 23/52
Tekki Waxtaan — Al-Qalam
فَانطَلَقُوا وَهُمْ يَتَخَافَتُونَ ٢٣
Transliteration
Fantalaqoo wa hum yatakhaafatoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ña ngay làkk, ca tool ya di déeyante :
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 21-25 — Al-Qalam
21فَتَنَادَوْا مُصْبِحِينَ
Ba ñu xëy, wootante ca suba cuuy :
22أَنِ اغْدُوا عَلَىٰ حَرْثِكُمْ إِن كُنتُمْ صَارِمِينَ
“Daldi ne teel leen xëy tool waay ndegam da ngeen bëgg góob”.
23فَانطَلَقُوا وَهُمْ يَتَخَافَتُونَ
Ña ngay làkk, ca tool ya di déeyante :
24أَن لَّا يَدْخُلَنَّهَا الْيَوْمَ عَلَيْكُم مِّسْكِينٌ
Tey wax naan : “Tey jii buleen seetaan benn miskin di dugg ci tool yi”.
25وَغَدَوْا عَلَىٰ حَرْدٍ قَادِرِينَ
Ñu xëy njortu ne, man nañoo tere tool ya.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
23Aaya
Tekki — Al-Qalam 23
Simoore Al-Qalam Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña ngay làkk, ca tool ya di déeyante :Simoore Aaya 23/52 — Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qalam Dégg, Al-Qalam Tekki, Al-Qalam mp3, Al-Qalam pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








