Al-Haqqa · 26/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Haqqa
وَلَمْ أَدْرِ مَا حِسَابِيَهْ ۝٢٦
Wa lam adri maa hisaabiyah
📖 Tekkim Wolof
te ma ba ña xam luy sama màndaxe...

🎧 Dégg


📜 Aaya 24-28 — Simoore Al-Haqqa

24كُلُوا وَاشْرَبُوا هَنِيئًا بِمَا أَسْلَفْتُمْ فِي الْأَيَّامِ الْخَالِيَةِ
“Lekkleen te naan muy peyug la ngeen jiitaloon”.
25وَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ بِشِمَالِهِ فَيَقُولُ يَا لَيْتَنِي لَمْ أُوتَ كِتَابِيَهْ
Ña ñuy joxe seen téere ci càmmoñ, danuy wax naan : “Aka neexoon ! Jotuma sama téere,
26وَلَمْ أَدْرِ مَا حِسَابِيَهْ
te ma ba ña xam luy sama màndaxe...
27يَا لَيْتَهَا كَانَتِ الْقَاضِيَةَ
Aka neexoon, ma dee farit.
28مَا أَغْنَىٰ عَنِّي مَالِيَهْ ۜ
Sama alal ja jariñuma dara.
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — Al-Haqqa 26

Simoore Al-Haqqa Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te ma ba ña xam luy sama màndaxe...

Simoore Aaya 26/52 — Simoore Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Haqqa Dégg, Simoore Al-Haqqa Tekki, Simoore Al-Haqqa mp3, Simoore Al-Haqqa pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers