Al-Haqqa · 27/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Haqqa
يَا لَيْتَهَا كَانَتِ الْقَاضِيَةَ ۝٢٧
Yaa laitahaa kaanatil qaadiyah
📖 Tekkim Wolof
Aka neexoon, ma dee farit.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 25-29 — Simoore Al-Haqqa

25وَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ بِشِمَالِهِ فَيَقُولُ يَا لَيْتَنِي لَمْ أُوتَ كِتَابِيَهْ
Ña ñuy joxe seen téere ci càmmoñ, danuy wax naan : “Aka neexoon ! Jotuma sama téere,
26وَلَمْ أَدْرِ مَا حِسَابِيَهْ
te ma ba ña xam luy sama màndaxe...
27يَا لَيْتَهَا كَانَتِ الْقَاضِيَةَ
Aka neexoon, ma dee farit.
28مَا أَغْنَىٰ عَنِّي مَالِيَهْ ۜ
Sama alal ja jariñuma dara.
29هَلَكَ عَنِّي سُلْطَانِيَهْ
Sama sañ-sañ réer na ma ! ”.
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
27Aaya

Tekki — Al-Haqqa 27

Simoore Al-Haqqa Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Aka neexoon, ma dee farit.

Simoore Aaya 27/52 — Simoore Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Haqqa Dégg, Simoore Al-Haqqa Tekki, Simoore Al-Haqqa mp3, Simoore Al-Haqqa pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers