Al-A'raf · 123/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
قَالَ فِرْعَوْنُ آمَنتُم بِهِ قَبْلَ أَنْ آذَنَ لَكُمْ ۖ إِنَّ هَٰذَا لَمَكْرٌ مَّكَرْتُمُوهُ فِي الْمَدِينَةِ لِتُخْرِجُوا مِنْهَا أَهْلَهَا ۖ فَسَوْفَ تَعْلَمُونَ ۝١٢٣
Qaala Fir`awnu aamantum bihee qabla an aazana lakum; inna haaza lamakrum makartumoohu filmadeenati litukhrijoo minhaaa ahlahaa fasawfa ta`almoon
📖 Tekkim Wolof
Firawna ne leen : “Ndax dangeen Koy gëm te joxuma leen ci ndigal ? Lii, pexe la mu ngeen fàggu ci dëkk bi, ngir génne ñi fi dëkk.Waaye dangeen xam...

🎧 Dégg


📜 Aaya 121-125 — Simoore Al-A'raf

121قَالُوا آمَنَّا بِرَبِّ الْعَالَمِينَ
Ñu ne : “Gëm nañu Boroom àddina si,
122رَبِّ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
Boroom Muusaa ak Aaruuna.”
123قَالَ فِرْعَوْنُ آمَنتُم بِهِ قَبْلَ أَنْ آذَنَ لَكُمْ ۖ إِنَّ هَٰذَا لَمَكْرٌ مَّكَرْتُمُوهُ فِي الْمَدِينَةِ لِتُخْرِجُوا مِنْهَا أَهْلَهَا ۖ فَسَوْفَ تَعْلَمُونَ
Firawna ne leen : “Ndax dangeen Koy gëm te joxuma leen ci ndigal ? Lii, pexe la mu ngeen fàggu ci dëkk bi, ngir génne ñi fi dëkk.Waaye dangeen xam...
124لَأُقَطِّعَنَّ أَيْدِيَكُمْ وَأَرْجُلَكُم مِّنْ خِلَافٍ ثُمَّ لَأُصَلِّبَنَّكُمْ أَجْمَعِينَ
Danaa dagg seeni yoxo ak seeni tànk cig jàllawle, ba noppi ma daaj leen, sandamtal leen yéen ñépp.”
125قَالُوا إِنَّا إِلَىٰ رَبِّنَا مُنقَلِبُونَ
Ñu toontu ne : “Nun ci sunu Boroom lanuy dellu.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
123Aaya

Tekki — Al-A'raf 123

Simoore Al-A'raf Aaya 123 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Firawna ne leen : “Ndax dangeen Koy gëm te joxuma…

Simoore Aaya 123/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 121–125. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers