Al-A'raf · 122/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
رَبِّ مُوسَىٰ وَهَارُونَ ۝١٢٢
Rabbi Moosaa wa Haaroon
📖 Tekkim Wolof
Boroom Muusaa ak Aaruuna.”

🎧 Dégg


📜 Aaya 120-124 — Simoore Al-A'raf

120وَأُلْقِيَ السَّحَرَةُ سَاجِدِينَ
Ñu rot ñoom jabar ya, sujjóot.
121قَالُوا آمَنَّا بِرَبِّ الْعَالَمِينَ
Ñu ne : “Gëm nañu Boroom àddina si,
122رَبِّ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
Boroom Muusaa ak Aaruuna.”
123قَالَ فِرْعَوْنُ آمَنتُم بِهِ قَبْلَ أَنْ آذَنَ لَكُمْ ۖ إِنَّ هَٰذَا لَمَكْرٌ مَّكَرْتُمُوهُ فِي الْمَدِينَةِ لِتُخْرِجُوا مِنْهَا أَهْلَهَا ۖ فَسَوْفَ تَعْلَمُونَ
Firawna ne leen : “Ndax dangeen Koy gëm te joxuma leen ci ndigal ? Lii, pexe la mu ngeen fàggu ci dëkk bi, ngir génne ñi fi dëkk.Waaye dangeen xam...
124لَأُقَطِّعَنَّ أَيْدِيَكُمْ وَأَرْجُلَكُم مِّنْ خِلَافٍ ثُمَّ لَأُصَلِّبَنَّكُمْ أَجْمَعِينَ
Danaa dagg seeni yoxo ak seeni tànk cig jàllawle, ba noppi ma daaj leen, sandamtal leen yéen ñépp.”
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
122Aaya

Tekki — Al-A'raf 122

Simoore Al-A'raf Aaya 122 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Boroom Muusaa ak Aaruuna.”

Simoore Aaya 122/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 120–124. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers