Al-A'raf · 124/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
لَأُقَطِّعَنَّ أَيْدِيَكُمْ وَأَرْجُلَكُم مِّنْ خِلَافٍ ثُمَّ لَأُصَلِّبَنَّكُمْ أَجْمَعِينَ ۝١٢٤
La uqatti`anna aidiyakum wa arjulakum min khilaafin summa la usallibannakum ajma`een
📖 Tekkim Wolof
Danaa dagg seeni yoxo ak seeni tànk cig jàllawle, ba noppi ma daaj leen, sandamtal leen yéen ñépp.”

🎧 Dégg


📜 Aaya 122-126 — Simoore Al-A'raf

122رَبِّ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
Boroom Muusaa ak Aaruuna.”
123قَالَ فِرْعَوْنُ آمَنتُم بِهِ قَبْلَ أَنْ آذَنَ لَكُمْ ۖ إِنَّ هَٰذَا لَمَكْرٌ مَّكَرْتُمُوهُ فِي الْمَدِينَةِ لِتُخْرِجُوا مِنْهَا أَهْلَهَا ۖ فَسَوْفَ تَعْلَمُونَ
Firawna ne leen : “Ndax dangeen Koy gëm te joxuma leen ci ndigal ? Lii, pexe la mu ngeen fàggu ci dëkk bi, ngir génne ñi fi dëkk.Waaye dangeen xam...
124لَأُقَطِّعَنَّ أَيْدِيَكُمْ وَأَرْجُلَكُم مِّنْ خِلَافٍ ثُمَّ لَأُصَلِّبَنَّكُمْ أَجْمَعِينَ
Danaa dagg seeni yoxo ak seeni tànk cig jàllawle, ba noppi ma daaj leen, sandamtal leen yéen ñépp.”
125قَالُوا إِنَّا إِلَىٰ رَبِّنَا مُنقَلِبُونَ
Ñu toontu ne : “Nun ci sunu Boroom lanuy dellu.
126وَمَا تَنقِمُ مِنَّا إِلَّا أَنْ آمَنَّا بِآيَاتِ رَبِّنَا لَمَّا جَاءَتْنَا ۚ رَبَّنَا أَفْرِغْ عَلَيْنَا صَبْرًا وَتَوَفَّنَا مُسْلِمِينَ
Feyoowoo ci nun lu dul nu gëm ay kéemaani sunu Boroom, ba ñu agsee ci nun. Sunu Boroom ! Sottil ci nun muñ te nga rey nu fekk nu dee jullit.”
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
124Aaya

Tekki — Al-A'raf 124

Simoore Al-A'raf Aaya 124 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Danaa dagg seeni yoxo ak seeni tànk cig jàllawle, ba…

Simoore Aaya 124/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 122–126. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers