Al-A'raf · 91/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
فَأَخَذَتْهُمُ الرَّجْفَةُ فَأَصْبَحُوا فِي دَارِهِمْ جَاثِمِينَ ۝٩١
Fa akhazat humur rajfatu fa asbahoo fee daarihim jaasimeen
📖 Tekkim Wolof
Yëngug suuf rajaxe leen ; ñu xëy ne lànjaŋ fa seeni kër.

🎧 Dégg


📜 Aaya 89-93 — Simoore Al-A'raf

89قَدِ افْتَرَيْنَا عَلَى اللَّهِ كَذِبًا إِنْ عُدْنَا فِي مِلَّتِكُم بَعْدَ إِذْ نَجَّانَا اللَّهُ مِنْهَا ۚ وَمَا يَكُونُ لَنَا أَن نَّعُودَ فِيهَا إِلَّا أَن يَشَاءَ اللَّهُ رَبُّنَا ۚ وَسِعَ رَبُّنَا كُلَّ شَيْءٍ عِلْمًا ۚ عَلَى اللَّهِ تَوَكَّلْنَا ۚ رَبَّنَا افْتَحْ بَيْنَنَا وَبَيْنَ قَوْمِنَا بِالْحَقِّ وَأَنتَ خَيْرُ الْفَاتِحِينَ
“Bu nu delloo dugg ci seen diine, kon de nu duural Yàlla aw fen gannaaw ba nu Yàlla musalee ci seen diine jooju. Dunu mën a dellu duggu ci lu dul mu soob Yàlla sunu Boroom. Xam-xamu sunu Boroom ump na lu nekk. Ci Yàlla lanuy wéeru. Yaw sunu Boroom, àtteel sunu diggante ak sunuy nit, ci dëgg, ndaxte Yaw [Yàlla], yaa gën a mën àtte àttekat yi.”
90وَقَالَ الْمَلَأُ الَّذِينَ كَفَرُوا مِن قَوْمِهِ لَئِنِ اتَّبَعْتُمْ شُعَيْبًا إِنَّكُمْ إِذًا لَّخَاسِرُونَ
Kilifa, ya weddi ca aw nitam, ne : “Bu ngeen toppee Chuhaybu, dangeen yàqule”.
91فَأَخَذَتْهُمُ الرَّجْفَةُ فَأَصْبَحُوا فِي دَارِهِمْ جَاثِمِينَ
Yëngug suuf rajaxe leen ; ñu xëy ne lànjaŋ fa seeni kër.
92الَّذِينَ كَذَّبُوا شُعَيْبًا كَأَن لَّمْ يَغْنَوْا فِيهَا ۚ الَّذِينَ كَذَّبُوا شُعَيْبًا كَانُوا هُمُ الْخَاسِرِينَ
Ña weddi woon Chuhaybu, dañoo mujj mel ni masuñu faa dëkk. Ña weddi woon Chuhaybu yàqule nañu.
93فَتَوَلَّىٰ عَنْهُمْ وَقَالَ يَا قَوْمِ لَقَدْ أَبْلَغْتُكُمْ رِسَالَاتِ رَبِّي وَنَصَحْتُ لَكُمْ ۖ فَكَيْفَ آسَىٰ عَلَىٰ قَوْمٍ كَافِرِينَ
Mu dëddu leen, ne : "Yéen samay mbokk, jottali naa leen sama Yonentub Boroom, laabire naa leen itam. Kon naka laay yërëmtaloo ngir aw nit ñu di ay yéefar ? ”
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
91Aaya

Tekki — Al-A'raf 91

Simoore Al-A'raf Aaya 91 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yëngug suuf rajaxe leen ; ñu xëy ne lànjaŋ fa…

Simoore Aaya 91/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 89–93. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers