Al-Qiyama · 33/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
ثُمَّ ذَهَبَ إِلَىٰ أَهْلِهِ يَتَمَطَّىٰ ۝٣٣
Summa zahaba ilaaa ahlihee yatamatta
📖 Tekkim Wolof
daldi dem nag ca aw nitam, di xoggaliku.

🎧 Dégg


📜 Aaya 31-35 — Simoore Al-Qiyama

31فَلَا صَدَّقَ وَلَا صَلَّىٰ
Gëmul woon, te it daawuloon julli;
32وَلَٰكِن كَذَّبَ وَتَوَلَّىٰ
waaye, moom sax dafa weddi woon dumóoyu,
33ثُمَّ ذَهَبَ إِلَىٰ أَهْلِهِ يَتَمَطَّىٰ
daldi dem nag ca aw nitam, di xoggaliku.
34أَوْلَىٰ لَكَ فَأَوْلَىٰ
“Yaayoo nga toskare, yaayoo nga toskare! ”
35ثُمَّ أَوْلَىٰ لَكَ فَأَوْلَىٰ
Te it yaayoo nga toskare, yayoo nga ko !
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
33Aaya

Tekki — Al-Qiyama 33

Simoore Al-Qiyama Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : daldi dem nag ca aw nitam, di xoggaliku.

Simoore Aaya 33/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers