An-Nazi'at · 43/46
Tekki Waxtaan — An-Nazi'at
فِيمَ أَنتَ مِن ذِكْرَاهَا ۝٤٣
Feema anta min zikraahaa
📖 Tekkim Wolof
Ana ban xam-xam nga ci am ngir tontu leen ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 41-45 — An-Nazi'at

41فَإِنَّ الْجَنَّةَ هِيَ الْمَأْوَىٰ
kookee àjjanaa di wàccuwaayam.
42يَسْأَلُونَكَ عَنِ السَّاعَةِ أَيَّانَ مُرْسَاهَا
Ña nga lay laaj bis pénc ba : “Kañ lay teeral”
43فِيمَ أَنتَ مِن ذِكْرَاهَا
Ana ban xam-xam nga ci am ngir tontu leen ?
44إِلَىٰ رَبِّكَ مُنتَهَاهَا
Ab yemukaayam sa Boroom rekk ko xam.
45إِنَّمَا أَنتَ مُنذِرُ مَن يَخْشَاهَا
Yaw nag ab xuppekat doŋŋ nga ngir ña ko ragal.
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
43Aaya

Tekki — An-Nazi'at 43

Simoore An-Nazi'at Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ana ban xam-xam nga ci am ngir tontu leen ?

Simoore Aaya 43/46 — An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nazi'at Dégg, An-Nazi'at Tekki, An-Nazi'at mp3, An-Nazi'at pdf. Aaya 41–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers