Al-Infitar · 7/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Infitar
الَّذِي خَلَقَكَ فَسَوَّاكَ فَعَدَلَكَ ۝٧
Allazee khalaqaka fasaw waaka fa`adalak
📖 Tekkim Wolof
(sa Boroom) bi la bind yemale la, jekkal la ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 5-9 — Simoore Al-Infitar

5عَلِمَتْ نَفْسٌ مَّا قَدَّمَتْ وَأَخَّرَتْ
bakkan bu Yàlla sàkk xam na la mu jëkkoona def ak la mu mujja def.
6يَا أَيُّهَا الْإِنسَانُ مَا غَرَّكَ بِرَبِّكَ الْكَرِيمِ
Éy yaw nit ! Ana lan moo la fàbbi ci sa mbiru Boroom, bu Tedd bi,
7الَّذِي خَلَقَكَ فَسَوَّاكَ فَعَدَلَكَ
(sa Boroom) bi la bind yemale la, jekkal la ?
8فِي أَيِّ صُورَةٍ مَّا شَاءَ رَكَّبَكَ
Moo la defar ca na mu ko soobe.
9كَلَّا بَلْ تُكَذِّبُونَ بِالدِّينِ
Déet... ! [ak lu mana xew] yéen a ngay weddi bis pénc ba ;
Al-InfitarFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Al-Infitar 7

Simoore Al-Infitar Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (sa Boroom) bi la bind yemale la, jekkal la ?

Simoore Aaya 7/19 — Simoore Al-Infitar الإنفطار (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Infitar Dégg, Simoore Al-Infitar Tekki, Simoore Al-Infitar mp3, Simoore Al-Infitar pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers