Al-Fajr · 24/30
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Fajr
يَقُولُ يَا لَيْتَنِي قَدَّمْتُ لِحَيَاتِي ۝٢٤
Yaqoolu yaa laitanee qaddamtu lihayaatee
📖 Tekkim Wolof
Muy wax naan : “Aka neexoon ! Ca ba muy dundu ma defoon lu baax !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 22-26 — Simoore Al-Fajr

22وَجَاءَ رَبُّكَ وَالْمَلَكُ صَفًّا صَفًّا
sa Boroom dikk ak malaaka ya, def ay sàppey sàppe,
23وَجِيءَ يَوْمَئِذٍ بِجَهَنَّمَ ۚ يَوْمَئِذٍ يَتَذَكَّرُ الْإِنسَانُ وَأَنَّىٰ لَهُ الذِّكْرَىٰ
bu keroogee, danuy indi Safarey jahanama ; bu keroogee it, nit dana fàttaliku. Waaye damaa xamut lu ko fàttaliku ga di jariñ ?
24يَقُولُ يَا لَيْتَنِي قَدَّمْتُ لِحَيَاتِي
Muy wax naan : “Aka neexoon ! Ca ba muy dundu ma defoon lu baax !
25فَيَوْمَئِذٍ لَّا يُعَذِّبُ عَذَابَهُ أَحَدٌ
Bu keroogee, mbugël ma deefu ko mbugël kenn,
26وَلَا يُوثِقُ وَثَاقَهُ أَحَدٌ
te it kenn du yolomal jéngam ba.
Al-FajrFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — Al-Fajr 24

Simoore Al-Fajr Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Muy wax naan : “Aka neexoon ! Ca ba muy…

Simoore Aaya 24/30 — Simoore Al-Fajr الفجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Fajr Dégg, Simoore Al-Fajr Tekki, Simoore Al-Fajr mp3, Simoore Al-Fajr pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers