Al-Fajr · 25/30
Tekki Waxtaan — Al-Fajr
فَيَوْمَئِذٍ لَّا يُعَذِّبُ عَذَابَهُ أَحَدٌ ۝٢٥
Fa Yawma izil laa yu`azzibu `azaabahooo ahad
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee, mbugël ma deefu ko mbugël kenn,

🎧 Dégg


📜 Aaya 23-27 — Al-Fajr

23وَجِيءَ يَوْمَئِذٍ بِجَهَنَّمَ ۚ يَوْمَئِذٍ يَتَذَكَّرُ الْإِنسَانُ وَأَنَّىٰ لَهُ الذِّكْرَىٰ
bu keroogee, danuy indi Safarey jahanama ; bu keroogee it, nit dana fàttaliku. Waaye damaa xamut lu ko fàttaliku ga di jariñ ?
24يَقُولُ يَا لَيْتَنِي قَدَّمْتُ لِحَيَاتِي
Muy wax naan : “Aka neexoon ! Ca ba muy dundu ma defoon lu baax !
25فَيَوْمَئِذٍ لَّا يُعَذِّبُ عَذَابَهُ أَحَدٌ
Bu keroogee, mbugël ma deefu ko mbugël kenn,
26وَلَا يُوثِقُ وَثَاقَهُ أَحَدٌ
te it kenn du yolomal jéngam ba.
27يَا أَيَّتُهَا النَّفْسُ الْمُطْمَئِنَّةُ
“Éy yaw, bakkan bi dalum xel,
Al-FajrFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Al-Fajr 25

Simoore Al-Fajr Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee, mbugël ma deefu ko mbugël kenn,

Simoore Aaya 25/30 — Al-Fajr الفجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Fajr Dégg, Al-Fajr Tekki, Al-Fajr mp3, Al-Fajr pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers