At-Tawba · 76/129
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tawba
فَلَمَّا آتَاهُم مِّن فَضْلِهِ بَخِلُوا بِهِ وَتَوَلَّوا وَّهُم مُّعْرِضُونَ ۝٧٦
Falammaaa aataahum min fadlihee bakhiloo bihee wa tawallaw wa hum mu`ridoon
📖 Tekkim Wolof
Ba leen Yàlla mayee ci mbaaxam (alal), ñu nay ci joxe, ginnaaw ba ñu fuuyu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 74-78 — Simoore At-Tawba

74يَحْلِفُونَ بِاللَّهِ مَا قَالُوا وَلَقَدْ قَالُوا كَلِمَةَ الْكُفْرِ وَكَفَرُوا بَعْدَ إِسْلَامِهِمْ وَهَمُّوا بِمَا لَمْ يَنَالُوا ۚ وَمَا نَقَمُوا إِلَّا أَنْ أَغْنَاهُمُ اللَّهُ وَرَسُولُهُ مِن فَضْلِهِ ۚ فَإِن يَتُوبُوا يَكُ خَيْرًا لَّهُمْ ۖ وَإِن يَتَوَلَّوْا يُعَذِّبْهُمُ اللَّهُ عَذَابًا أَلِيمًا فِي الدُّنْيَا وَالْآخِرَةِ ۚ وَمَا لَهُمْ فِي الْأَرْضِ مِن وَلِيٍّ وَلَا نَصِيرٍ
Ñangay waat ci Yàlla ne waxuñu dara, te wér na ne wax nañu baati weddi te tàbbi nañu ci kéefar ginnaaw ba ñu duggee ci Lislaam. Te ñangay ittewoo lu ñu mënul a am. Te amuñu la ñuy sàkku lu dul Yàlla - ak Yonentam - dafa leen jox ci mbaaxam koom-koom. Bu ñu tuuboon, mooy gën ci ñoom. Su ñu lànkee, féttéerlu, Yàlla Dana leen mbugal mbugal mu metti ci àddina ak àllaaxira ; te duñu am ci kaw suuf ku ñuy wéeru mu méngoo seeni mbir walla ku leen dimbali.
75۞ وَمِنْهُم مَّنْ عَاهَدَ اللَّهَ لَئِنْ آتَانَا مِن فَضْلِهِ لَنَصَّدَّقَنَّ وَلَنَكُونَنَّ مِنَ الصَّالِحِينَ
Ci ñoom, am na ñu warlul Yàlla, ne : “Bu nu Yàlla mayoon ci mbaaxam (alal), kon dey dananu natt asaka, te it dananu bokk ca ñu baax ña”.
76فَلَمَّا آتَاهُم مِّن فَضْلِهِ بَخِلُوا بِهِ وَتَوَلَّوا وَّهُم مُّعْرِضُونَ
Ba leen Yàlla mayee ci mbaaxam (alal), ñu nay ci joxe, ginnaaw ba ñu fuuyu.
77فَأَعْقَبَهُمْ نِفَاقًا فِي قُلُوبِهِمْ إِلَىٰ يَوْمِ يَلْقَوْنَهُ بِمَا أَخْلَفُوا اللَّهَ مَا وَعَدُوهُ وَبِمَا كَانُوا يَكْذِبُونَ
Tax na Yàlla wuutale ci seen xol naaféq ba kera ñuy dajeek Moom ngir la ñu wor Yàlla ca la ñu ko digoon ak ca la ñu doon fen.
78أَلَمْ يَعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ سِرَّهُمْ وَنَجْوَاهُمْ وَأَنَّ اللَّهَ عَلَّامُ الْغُيُوبِ
Moo ndax dañoo xamul ne Yàlla xam na seen mbóot ya nëbbu ak seenub déeyoo, te nag Yàlla mooy xamaakoonub kumpa.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
76Aaya

Tekki — At-Tawba 76

Simoore At-Tawba Aaya 76 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba leen Yàlla mayee ci mbaaxam (alal), ñu nay ci…

Simoore Aaya 76/129 — Simoore At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tawba Dégg, Simoore At-Tawba Tekki, Simoore At-Tawba mp3, Simoore At-Tawba pdf. Aaya 74–78. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers