Yusuf · 12/111
Tekki Waxtaan — Simoore Yusuf
أَرْسِلْهُ مَعَنَا غَدًا يَرْتَعْ وَيَلْعَبْ وَإِنَّا لَهُ لَحَافِظُونَ ۝١٢
Arilhu ma`anaa ghadany yarta`wa yal`ab wa innaa lahoo lahaafizoon
📖 Tekkim Wolof
Bu subaa nga yabal ko mu ànd ak nun muy sàmm jur gi, di fo. Dananu ko wattu”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Simoore Yusuf

10قَالَ قَائِلٌ مِّنْهُمْ لَا تَقْتُلُوا يُوسُفَ وَأَلْقُوهُ فِي غَيَابَتِ الْجُبِّ يَلْتَقِطْهُ بَعْضُ السَّيَّارَةِ إِن كُنتُمْ فَاعِلِينَ
Mu am ca ñoom ku wax ne : “Buleen rey Yuusufa, sànnileen ko ci teen bu lëndëm, kon tukkikat yi danañu ko for su fekkee def ngeen ko”.
11قَالُوا يَا أَبَانَا مَا لَكَ لَا تَأْمَنَّا عَلَىٰ يُوسُفَ وَإِنَّا لَهُ لَنَاصِحُونَ
Ñu ne : "Yaw sunu baay, ana lan moo tax wóoluwoo nu ci Yuusufa ? Te nun dañu koy laabire doŋŋ.
12أَرْسِلْهُ مَعَنَا غَدًا يَرْتَعْ وَيَلْعَبْ وَإِنَّا لَهُ لَحَافِظُونَ
Bu subaa nga yabal ko mu ànd ak nun muy sàmm jur gi, di fo. Dananu ko wattu”.
13قَالَ إِنِّي لَيَحْزُنُنِي أَن تَذْهَبُوا بِهِ وَأَخَافُ أَن يَأْكُلَهُ الذِّئْبُ وَأَنتُمْ عَنْهُ غَافِلُونَ
Mu ne leen : “Man dey, am naa njàqare ci ngeen ànd ak moom ; danaa ragal ngeen sàggan ba ag till lekk ko”.
14قَالُوا لَئِنْ أَكَلَهُ الذِّئْبُ وَنَحْنُ عُصْبَةٌ إِنَّا إِذًا لَّخَاسِرُونَ
Ñu ne : “Till! Su ko lekkee nag ak nii nu nekkee di mbooloo, kon dey nu gën a yées”.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Yusuf 12

Simoore Yusuf Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu subaa nga yabal ko mu ànd ak nun muy…

Simoore Aaya 12/111 — Simoore Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Yusuf Dégg, Simoore Yusuf Tekki, Simoore Yusuf mp3, Simoore Yusuf pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers