Al-Hijr · 20/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
وَجَعَلْنَا لَكُمْ فِيهَا مَعَايِشَ وَمَن لَّسْتُمْ لَهُ بِرَازِقِينَ ٢٠
Transliteration
Wa ja`alnaa lakum feehaa ma`aayisha wa mal lastum lahoo biraaziqeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nu defaral leen ca lu ngeen di dunde, yéen ak ñi ngeen dundalul.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 18-22 — Al-Hijr
18إِلَّا مَنِ اسْتَرَقَ السَّمْعَ فَأَتْبَعَهُ شِهَابٌ مُّبِينٌ
Lu dul ku jéem a sàcc lu mu dégg, [te ku ko ca jéem] ay jumu safara soxal ko.
19وَالْأَرْضَ مَدَدْنَاهَا وَأَلْقَيْنَا فِيهَا رَوَاسِيَ وَأَنبَتْنَا فِيهَا مِن كُلِّ شَيْءٍ مَّوْزُونٍ
Tàllal Nanu suuf si te samp ci ay tundi doj (yu tax mu dal) ; saxal Nanu itam wépp xeetu gàncax muy lu ñu nattale.
20وَجَعَلْنَا لَكُمْ فِيهَا مَعَايِشَ وَمَن لَّسْتُمْ لَهُ بِرَازِقِينَ
Nu defaral leen ca lu ngeen di dunde, yéen ak ñi ngeen dundalul.
21وَإِن مِّن شَيْءٍ إِلَّا عِندَنَا خَزَائِنُهُ وَمَا نُنَزِّلُهُ إِلَّا بِقَدَرٍ مَّعْلُومٍ
Amul lenn loo xam ne ndàmbam nekkul ci nun, waaye Dunu ca wàcce lu dul ab natt bu ñu xam (bu yem ak bu doy).
22وَأَرْسَلْنَا الرِّيَاحَ لَوَاقِحَ فَأَنزَلْنَا مِنَ السَّمَاءِ مَاءً فَأَسْقَيْنَاكُمُوهُ وَمَا أَنتُمْ لَهُ بِخَازِنِينَ
Yónni Nanu ngelaw luy sos (taw ci niir yi) ; wàcce Nanu ndox mu jóge asamaan, nàndal Nanu leen ci te mënuleen ko woon a denc.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
20Aaya
Tekki — Al-Hijr 20
Simoore Al-Hijr Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu defaral leen ca lu ngeen di dunde, yéen ak…Simoore Aaya 20/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








