Al-Hijr · 79/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
فَانتَقَمْنَا مِنْهُمْ وَإِنَّهُمَا لَبِإِمَامٍ مُّبِينٍ ۝٧٩
Fantaqamnaa minhum wa innahumaa labi imaamim mubeen
📖 Tekkim Wolof
Nu mbugal leen. Te [ñaari dëkk yooyu] ñanga ca yoon wu neex a xam.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 77-81 — Simoore Al-Hijr

77إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّلْمُؤْمِنِينَ
Loolu nekk na di kéemtaan ci ñi gëm !
78وَإِن كَانَ أَصْحَابُ الْأَيْكَةِ لَظَالِمِينَ
Te waa Leykata ay tooñkat lañu woon.
79فَانتَقَمْنَا مِنْهُمْ وَإِنَّهُمَا لَبِإِمَامٍ مُّبِينٍ
Nu mbugal leen. Te [ñaari dëkk yooyu] ñanga ca yoon wu neex a xam.
80وَلَقَدْ كَذَّبَ أَصْحَابُ الْحِجْرِ الْمُرْسَلِينَ
Waa Hijri weddi woon nañu Yonent ya.
81وَآتَيْنَاهُمْ آيَاتِنَا فَكَانُوا عَنْهَا مُعْرِضِينَ
Nu joxoon leen sunuy kawtéef, ñu dëddu leen.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
79Aaya

Tekki — Al-Hijr 79

Simoore Al-Hijr Aaya 79 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu mbugal leen. Te [ñaari dëkk yooyu] ñanga ca yoon…

Simoore Aaya 79/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 77–81. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers