An-Nahl · 122/128
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nahl
وَآتَيْنَاهُ فِي الدُّنْيَا حَسَنَةً ۖ وَإِنَّهُ فِي الْآخِرَةِ لَمِنَ الصَّالِحِينَ ۝١٢٢
Wa aatainaahu fid dunyaa hasanah; wa innahoo fil Aakhirati laminas saaliheen
📖 Tekkim Wolof
Te may Nanu ko ci àddina tagg wu rafet. Te ca àllaaxira, dana bokk ca ñu sell, ñu [yiw] ña.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 120-124 — Simoore An-Nahl

120إِنَّ إِبْرَاهِيمَ كَانَ أُمَّةً قَانِتًا لِّلَّهِ حَنِيفًا وَلَمْ يَكُ مِنَ الْمُشْرِكِينَ
Ibraahiima nag roytéef la. Di jaamukatu Yàlla, di ko wéetal, musul a bokk ca bokkaalekat ya.
121شَاكِرًا لِّأَنْعُمِهِ ۚ اجْتَبَاهُ وَهَدَاهُ إِلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Ku daan gërëm [Yàlla] la ci xéewalam yi, Yàlla tànn na ko, gindi ko, teg ko ci yoon wu jub xocc wa.
122وَآتَيْنَاهُ فِي الدُّنْيَا حَسَنَةً ۖ وَإِنَّهُ فِي الْآخِرَةِ لَمِنَ الصَّالِحِينَ
Te may Nanu ko ci àddina tagg wu rafet. Te ca àllaaxira, dana bokk ca ñu sell, ñu [yiw] ña.
123ثُمَّ أَوْحَيْنَا إِلَيْكَ أَنِ اتَّبِعْ مِلَّةَ إِبْرَاهِيمَ حَنِيفًا ۖ وَمَا كَانَ مِنَ الْمُشْرِكِينَ
Tax na Nu soloo la ne : “Toppal diiney Ibraahiima [yaw Muhammad] cig wéetal sa Boroom, bokkul woon ca bokkaalekat ya”.
124إِنَّمَا جُعِلَ السَّبْتُ عَلَى الَّذِينَ اخْتَلَفُوا فِيهِ ۚ وَإِنَّ رَبَّكَ لَيَحْكُمُ بَيْنَهُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فِيمَا كَانُوا فِيهِ يَخْتَلِفُونَ
Màggal bisu gaawu tegewul woon lu dul ca kaw ña ca juuyoo woon. Te sa Boroom dana àtte seen diggante ca Bis-pénc ba ca la ñu nekkoon di ca juuyoo.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
122Aaya

Tekki — An-Nahl 122

Simoore An-Nahl Aaya 122 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te may Nanu ko ci àddina tagg wu rafet. Te…

Simoore Aaya 122/128 — Simoore An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nahl Dégg, Simoore An-Nahl Tekki, Simoore An-Nahl mp3, Simoore An-Nahl pdf. Aaya 120–124. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers