Maryam · 40/98
Tekki Waxtaan — Maryam
إِنَّا نَحْنُ نَرِثُ الْأَرْضَ وَمَنْ عَلَيْهَا وَإِلَيْنَا يُرْجَعُونَ ۝٤٠
Innaa NNahnu narisul arda wa man `alaihaa wa ilainaa yurja`oon
📖 Tekkim Wolof
Nun nooy donnu suuf si ak lépp lu nekk ci kawam, te it fi Nun la ñuy dellusi [Bis-pénc ba].

🎧 Dégg


📜 Aaya 38-42 — Maryam

38أَسْمِعْ بِهِمْ وَأَبْصِرْ يَوْمَ يَأْتُونَنَا ۖ لَٰكِنِ الظَّالِمُونَ الْيَوْمَ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
[Bu bis baa, tooñkat yi danañu dégg], danañu gis ! Waaye tey fii ci àddina, ñi ngi ci réer gu bir.
39وَأَنذِرْهُمْ يَوْمَ الْحَسْرَةِ إِذْ قُضِيَ الْأَمْرُ وَهُمْ فِي غَفْلَةٍ وَهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Nanga leen xupp ci tiisu bisub jagle ga ; ndax àtte ba dog na te ñoom ña nga cig càggante te duñu gëm.
40إِنَّا نَحْنُ نَرِثُ الْأَرْضَ وَمَنْ عَلَيْهَا وَإِلَيْنَا يُرْجَعُونَ
Nun nooy donnu suuf si ak lépp lu nekk ci kawam, te it fi Nun la ñuy dellusi [Bis-pénc ba].
41وَاذْكُرْ فِي الْكِتَابِ إِبْرَاهِيمَ ۚ إِنَّهُ كَانَ صِدِّيقًا نَّبِيًّا
[Fàttalikul] Ibraahiima ca Téere ba, moom dey ku dëggu woon la, di ab Yonent.
42إِذْ قَالَ لِأَبِيهِ يَا أَبَتِ لِمَ تَعْبُدُ مَا لَا يَسْمَعُ وَلَا يُبْصِرُ وَلَا يُغْنِي عَنكَ شَيْئًا
[Fàttalikul] ba mu waxee baayam ne ko : “Ana lan moo tax ngay jaamu loo xam ne du dégg du gis, te du la fajal dara ?
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
40Aaya

Tekki — Maryam 40

Simoore Maryam Aaya 40 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun nooy donnu suuf si ak lépp lu nekk ci…

Simoore Aaya 40/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 38–42. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers