Maryam · 88/98
Tekki Waxtaan — Maryam
وَقَالُوا اتَّخَذَ الرَّحْمَٰنُ وَلَدًا ۝٨٨
Wa qaalut takhazar Rahmaanu waladaa
📖 Tekkim Wolof
Ñuy wax it naan : “[Yàlla] Yërëmaakoon ba am na doom ! ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 86-90 — Maryam

86وَنَسُوقُ الْمُجْرِمِينَ إِلَىٰ جَهَنَّمَ وِرْدًا
Nu sëkkëtal tooñkat ya jëme leen Safara ñuy sërëx-sërëxi,
87لَّا يَمْلِكُونَ الشَّفَاعَةَ إِلَّا مَنِ اتَّخَذَ عِندَ الرَّحْمَٰنِ عَهْدًا
[Bis booba] kenn du mën a ramm ku dul ku ko Yàlla digal.
88وَقَالُوا اتَّخَذَ الرَّحْمَٰنُ وَلَدًا
Ñuy wax it naan : “[Yàlla] Yërëmaakoon ba am na doom ! ”
89لَّقَدْ جِئْتُمْ شَيْئًا إِدًّا
Indi ngeen lu juunu !
90تَكَادُ السَّمَاوَاتُ يَتَفَطَّرْنَ مِنْهُ وَتَنشَقُّ الْأَرْضُ وَتَخِرُّ الْجِبَالُ هَدًّا
[Loo xam ne] asamaan yi xaw na cee xottiku, suuf si xar, tundi doj yi màbb [ngir wax jooju],
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
88Aaya

Tekki — Maryam 88

Simoore Maryam Aaya 88 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñuy wax it naan : “[Yàlla] Yërëmaakoon ba am na…

Simoore Aaya 88/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 86–90. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers