Al-Baqara · 73/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
فَقُلْنَا اضْرِبُوهُ بِبَعْضِهَا ۚ كَذَٰلِكَ يُحْيِي اللَّهُ الْمَوْتَىٰ وَيُرِيكُمْ آيَاتِهِ لَعَلَّكُمْ تَعْقِلُونَ ٧٣
Transliteration
Faqulnad riboohu biba`dihaa; kazaalika yuhyil laa hul mawtaa wa yureekum aayaatihee la`allakum ta`qiloon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nu ne : “Dóorleen ko lenn [Lu bokk ci nag wi]”. - Noonu la Yàllay dekkalee ñi dee te dana leen won ay kéemaan ndax ngeen xel-lu.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 71-75 — Al-Baqara
71قَالَ إِنَّهُ يَقُولُ إِنَّهَا بَقَرَةٌ لَّا ذَلُولٌ تُثِيرُ الْأَرْضَ وَلَا تَسْقِي الْحَرْثَ مُسَلَّمَةٌ لَّا شِيَةَ فِيهَا ۚ قَالُوا الْآنَ جِئْتَ بِالْحَقِّ ۚ فَذَبَحُوهَا وَمَا كَادُوا يَفْعَلُونَ
– Mu ne moom nag : “Nee na, nag la wu ñu bayloowul suuf si, du buy suuxat mbay, bu amul benn laago la te wenn melo la”. - Ñu ne ko : “Agsi nga ci dëgg gi! ” Ñu rendi ko te xawoon nañu koo bañ a def.
72وَإِذْ قَتَلْتُمْ نَفْسًا فَادَّارَأْتُمْ فِيهَا ۖ وَاللَّهُ مُخْرِجٌ مَّا كُنتُمْ تَكْتُمُونَ
[Fàttalikuleen] Ba ngeen reyee bakkan te ngeen jiiñante ko!... Te Yàlla génne la ngeen doon nëbb.
73فَقُلْنَا اضْرِبُوهُ بِبَعْضِهَا ۚ كَذَٰلِكَ يُحْيِي اللَّهُ الْمَوْتَىٰ وَيُرِيكُمْ آيَاتِهِ لَعَلَّكُمْ تَعْقِلُونَ
Nu ne : “Dóorleen ko lenn [Lu bokk ci nag wi]”. - Noonu la Yàllay dekkalee ñi dee te dana leen won ay kéemaan ndax ngeen xel-lu.
74ثُمَّ قَسَتْ قُلُوبُكُم مِّن بَعْدِ ذَٰلِكَ فَهِيَ كَالْحِجَارَةِ أَوْ أَشَدُّ قَسْوَةً ۚ وَإِنَّ مِنَ الْحِجَارَةِ لَمَا يَتَفَجَّرُ مِنْهُ الْأَنْهَارُ ۚ وَإِنَّ مِنْهَا لَمَا يَشَّقَّقُ فَيَخْرُجُ مِنْهُ الْمَاءُ ۚ وَإِنَّ مِنْهَا لَمَا يَهْبِطُ مِنْ خَشْيَةِ اللَّهِ ۗ وَمَا اللَّهُ بِغَافِلٍ عَمَّا تَعْمَلُونَ
Topp, seeni xol wow ginnaaw loolu [dëgër] ba mel ni xeer mbaa lu ko gën a tar wowaay ; Ndax ci xeer sax ndox dana ca ball, te am na ci xeer yi yuy xar ndox génn ca, am na ci yuy rot ngir ragal Yàlla. Te Yàlla du ñàkk a seetlu li ngeen di def.
75۞ أَفَتَطْمَعُونَ أَن يُؤْمِنُوا لَكُمْ وَقَدْ كَانَ فَرِيقٌ مِّنْهُمْ يَسْمَعُونَ كَلَامَ اللَّهِ ثُمَّ يُحَرِّفُونَهُ مِن بَعْدِ مَا عَقَلُوهُ وَهُمْ يَعْلَمُونَ
- Moo ndax, dangeen xeemeem [,Yéen jullit ñi,] Yahuud yi wóolu leen? Te am na ci ñoom kurél boo xam ne déggoon nañu waxi Yàlla, ba noppi soppi ko ginnaw ba ñu ca xalaatee ba xam ko.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
73Aaya
Tekki — Al-Baqara 73
Simoore Al-Baqara Aaya 73 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu ne : “Dóorleen ko lenn [Lu bokk ci nag…Simoore Aaya 73/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 71–75. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








