Al-Anbiya · 37/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
خُلِقَ الْإِنسَانُ مِنْ عَجَلٍ ۚ سَأُرِيكُمْ آيَاتِي فَلَا تَسْتَعْجِلُونِ ۝٣٧
Khuliqal insaanu min `ajal; sa ureekum Aayaatee falaa tasta`jiloon
📖 Tekkim Wolof
Bindeef na nit cig yàkkamti. Danaa leen won Samay kéemaan. Buleen ma yàkkamti.

🎧 Dégg


📜 Aaya 35-39 — Simoore Al-Anbiya

35كُلُّ نَفْسٍ ذَائِقَةُ الْمَوْتِ ۗ وَنَبْلُوكُم بِالشَّرِّ وَالْخَيْرِ فِتْنَةً ۖ وَإِلَيْنَا تُرْجَعُونَ
Bakkan bu nekk dana mos dee. Te Dananu leen nattu ci lu bon ak yiw mu dib sànje. Te ci Nun ngeen di dellusi.
36وَإِذَا رَآكَ الَّذِينَ كَفَرُوا إِن يَتَّخِذُونَكَ إِلَّا هُزُوًا أَهَٰذَا الَّذِي يَذْكُرُ آلِهَتَكُمْ وَهُم بِذِكْرِ الرَّحْمَٰنِ هُمْ كَافِرُونَ
Ña weddi, bu ñu la gisee, duñu la jàppe lu dul ku ñuy yéjji, naan : “Ndax du kii mooy sikkal seen yàlla yi ? ” Te ñoom dañuy weddi Yàlla Mi nga xam ne [bokk na ci turam yi] Yërëmaakoon bi.
37خُلِقَ الْإِنسَانُ مِنْ عَجَلٍ ۚ سَأُرِيكُمْ آيَاتِي فَلَا تَسْتَعْجِلُونِ
Bindeef na nit cig yàkkamti. Danaa leen won Samay kéemaan. Buleen ma yàkkamti.
38وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هَٰذَا الْوَعْدُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ñuy wax naan : “Kañ la dig boobu di agsi ndegam ñu dëggu ngeen ? ”
39لَوْ يَعْلَمُ الَّذِينَ كَفَرُوا حِينَ لَا يَكُفُّونَ عَن وُجُوهِهِمُ النَّارَ وَلَا عَن ظُهُورِهِمْ وَلَا هُمْ يُنصَرُونَ
Ña weddi bu ñu xamoon waxtu wa nga xam ne duñu mën a feg safara say lakk seeni kanam walla seeni ginnaaw, te kenn duleen ca dimbali...
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
37Aaya

Tekki — Al-Anbiya 37

Simoore Al-Anbiya Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bindeef na nit cig yàkkamti. Danaa leen won Samay kéemaan.…

Simoore Aaya 37/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers