Al-Anbiya · 38/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هَٰذَا الْوَعْدُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ ٣٨
Transliteration
Wa yaqooloona mataa haazal wa`du in kuntum saadiqeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñuy wax naan : “Kañ la dig boobu di agsi ndegam ñu dëggu ngeen ? ”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 36-40 — Al-Anbiya
36وَإِذَا رَآكَ الَّذِينَ كَفَرُوا إِن يَتَّخِذُونَكَ إِلَّا هُزُوًا أَهَٰذَا الَّذِي يَذْكُرُ آلِهَتَكُمْ وَهُم بِذِكْرِ الرَّحْمَٰنِ هُمْ كَافِرُونَ
Ña weddi, bu ñu la gisee, duñu la jàppe lu dul ku ñuy yéjji, naan : “Ndax du kii mooy sikkal seen yàlla yi ? ” Te ñoom dañuy weddi Yàlla Mi nga xam ne [bokk na ci turam yi] Yërëmaakoon bi.
37خُلِقَ الْإِنسَانُ مِنْ عَجَلٍ ۚ سَأُرِيكُمْ آيَاتِي فَلَا تَسْتَعْجِلُونِ
Bindeef na nit cig yàkkamti. Danaa leen won Samay kéemaan. Buleen ma yàkkamti.
38وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هَٰذَا الْوَعْدُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ñuy wax naan : “Kañ la dig boobu di agsi ndegam ñu dëggu ngeen ? ”
39لَوْ يَعْلَمُ الَّذِينَ كَفَرُوا حِينَ لَا يَكُفُّونَ عَن وُجُوهِهِمُ النَّارَ وَلَا عَن ظُهُورِهِمْ وَلَا هُمْ يُنصَرُونَ
Ña weddi bu ñu xamoon waxtu wa nga xam ne duñu mën a feg safara say lakk seeni kanam walla seeni ginnaaw, te kenn duleen ca dimbali...
40بَلْ تَأْتِيهِم بَغْتَةً فَتَبْهَتُهُمْ فَلَا يَسْتَطِيعُونَ رَدَّهَا وَلَا هُمْ يُنظَرُونَ
Déedéet, ndekete yoo ci mbetteel la leen di dikkale, gëlëmal leen ; duñu ko mën a fànq, te kenn duleen ca yéexe.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
38Aaya
Tekki — Al-Anbiya 38
Simoore Al-Anbiya Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñuy wax naan : “Kañ la dig boobu di agsi…Simoore Aaya 38/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








