Al-Mu'minun · 70/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
أَمْ يَقُولُونَ بِهِ جِنَّةٌ ۚ بَلْ جَاءَهُم بِالْحَقِّ وَأَكْثَرُهُمْ لِلْحَقِّ كَارِهُونَ ۝٧٠
Am yaqooloona bihee jinnnah; bal jaaa`ahum bilhaqqi wa aksaruhum lil haqqi kaarihoon
📖 Tekkim Wolof
Walla dañu naan : “Jinnee ko sadd ? ” [Du loolu lépp], li am mooy moom dëgg rekk la indi. Te li ëpp ci ñoom dañoo sib dëgg.

🎧 Dégg


📜 Aaya 68-72 — Simoore Al-Mu'minun

68أَفَلَمْ يَدَّبَّرُوا الْقَوْلَ أَمْ جَاءَهُم مَّا لَمْ يَأْتِ آبَاءَهُمُ الْأَوَّلِينَ
Ndax dañoo settantalul wax ji [di Alxuraan] ? Walla daleen a digalul lu ñu digalul woon seen maam ya leen jiitu woon ?
69أَمْ لَمْ يَعْرِفُوا رَسُولَهُمْ فَهُمْ لَهُ مُنكِرُونَ
Walla dañoo xamul seenub Yonent, ba tax ñu umpale ko ?
70أَمْ يَقُولُونَ بِهِ جِنَّةٌ ۚ بَلْ جَاءَهُم بِالْحَقِّ وَأَكْثَرُهُمْ لِلْحَقِّ كَارِهُونَ
Walla dañu naan : “Jinnee ko sadd ? ” [Du loolu lépp], li am mooy moom dëgg rekk la indi. Te li ëpp ci ñoom dañoo sib dëgg.
71وَلَوِ اتَّبَعَ الْحَقُّ أَهْوَاءَهُمْ لَفَسَدَتِ السَّمَاوَاتُ وَالْأَرْضُ وَمَن فِيهِنَّ ۚ بَلْ أَتَيْنَاهُم بِذِكْرِهِمْ فَهُمْ عَن ذِكْرِهِم مُّعْرِضُونَ
Te bu Yàlla toppoon seen bànneex, kon asamaan ak suuf si yàqu. Indil Nanu leen ag waare, waaye dañoo dummóoyu waare googu.
72أَمْ تَسْأَلُهُمْ خَرْجًا فَخَرَاجُ رَبِّكَ خَيْرٌ ۖ وَهُوَ خَيْرُ الرَّازِقِينَ
Ndax danga leen di laaj ab génnuwaay ? Sa génnuwaayu Boroom moo gën. Te moom [Yàlla] moo Gën ji kuy wërsëgal.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
70Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 70

Simoore Al-Mu'minun Aaya 70 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla dañu naan : “Jinnee ko sadd ? ” [Du…

Simoore Aaya 70/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 68–72. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers