Ash-Shu'ara · 152/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
الَّذِينَ يُفْسِدُونَ فِي الْأَرْضِ وَلَا يُصْلِحُونَ ۝١٥٢
Allazeena yufsidoona fil ardi wa laa yuslihoon
📖 Tekkim Wolof
ñiy yàq rekk ci suuf si te duñu defar”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 150-154 — Simoore Ash-Shu'ara

150فَاتَّقُوا اللَّهَ وَأَطِيعُونِ
Mu ne ragal-leen Yàlla waay te topp samay ndigal.
151وَلَا تُطِيعُوا أَمْرَ الْمُسْرِفِينَ
Te buleen topp mukk nag ndigalul ñiy sànkaate [xaaxaabal],
152الَّذِينَ يُفْسِدُونَ فِي الْأَرْضِ وَلَا يُصْلِحُونَ
ñiy yàq rekk ci suuf si te duñu defar”.
153قَالُوا إِنَّمَا أَنتَ مِنَ الْمُسَحَّرِينَ
Ñu ne ko : “Yaw daal, ab njibar moo la ŋëb.
154مَا أَنتَ إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُنَا فَأْتِ بِآيَةٍ إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
Yaw daal, doo kenn ku dul nit ni nun. Indil kaawtéef ndegam li ngay wax dëgg la”.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
152Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 152

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 152 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ñiy yàq rekk ci suuf si te duñu defar”.

Simoore Aaya 152/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 150–154. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers