Ash-Shu'ara · 88/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
يَوْمَ لَا يَنفَعُ مَالٌ وَلَا بَنُونَ ۝٨٨
Yawma laa yanfa`u maalunw wa laa banoon
📖 Tekkim Wolof
bis ba alal ak i doom du jariñati,
🎧 Dégg

📜 Aaya 86-90 — Ash-Shu'ara

86وَاغْفِرْ لِأَبِي إِنَّهُ كَانَ مِنَ الضَّالِّينَ
te Nga jéggal sama baay : moom dafa bokk ca ñu réer ña ;
87وَلَا تُخْزِنِي يَوْمَ يُبْعَثُونَ
te bul ma gàcceel kerook bisub dekki ba,
88يَوْمَ لَا يَنفَعُ مَالٌ وَلَا بَنُونَ
bis ba alal ak i doom du jariñati,
89إِلَّا مَنْ أَتَى اللَّهَ بِقَلْبٍ سَلِيمٍ
ku dul kay ñëw ca Yàllaak xol bu mucc ayib”.
90وَأُزْلِفَتِ الْجَنَّةُ لِلْمُتَّقِينَ
Ñu jigeeñal Àjjana ña ragal Yàlla.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
88Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 88

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 88 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : bis ba alal ak i doom du jariñati,

Simoore Aaya 88/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 86–90. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers