Ash-Shu'ara · 91/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَبُرِّزَتِ الْجَحِيمُ لِلْغَاوِينَ ۝٩١
Wa burrizatil Jaheemu lilghaaween
📖 Tekkim Wolof
te gaaraleef na Safara ñeel ña béewoon,

🎧 Dégg


📜 Aaya 89-93 — Simoore Ash-Shu'ara

89إِلَّا مَنْ أَتَى اللَّهَ بِقَلْبٍ سَلِيمٍ
ku dul kay ñëw ca Yàllaak xol bu mucc ayib”.
90وَأُزْلِفَتِ الْجَنَّةُ لِلْمُتَّقِينَ
Ñu jigeeñal Àjjana ña ragal Yàlla.
91وَبُرِّزَتِ الْجَحِيمُ لِلْغَاوِينَ
te gaaraleef na Safara ñeel ña béewoon,
92وَقِيلَ لَهُمْ أَيْنَ مَا كُنتُمْ تَعْبُدُونَ
Ñu wax leen ne : “Ana fan ngeen nekkoon di fa jaamoo,
93مِن دُونِ اللَّهِ هَلْ يَنصُرُونَكُمْ أَوْ يَنتَصِرُونَ
bàyyi woon Yàlla ? Ndax mën nanoo dimbali seen bopp ? Walla ñu dimbali leen ? ”
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
91Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 91

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 91 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te gaaraleef na Safara ñeel ña béewoon,

Simoore Aaya 91/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 89–93. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers