Aali Imran · 23/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
أَلَمْ تَرَ إِلَى الَّذِينَ أُوتُوا نَصِيبًا مِّنَ الْكِتَابِ يُدْعَوْنَ إِلَىٰ كِتَابِ اللَّهِ لِيَحْكُمَ بَيْنَهُمْ ثُمَّ يَتَوَلَّىٰ فَرِيقٌ مِّنْهُمْ وَهُم مُّعْرِضُونَ ۝٢٣
Alam tara ilal lazeena ootoo naseebam minal Kitaabi yud`awna ilaa Kitaabil laahi liyahkuma bainahum summa yatawallaa fareequm minhum wa hum mu`ridoon
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax gisoo ñañu jox cér ca téere ba , woowees na leen jëme ci Téere Yàlla bi ngir mu àtte seeni diggante ; am kurél ci ñoom bu dummóoyu, far ñoom ñépp dummóoyu.
🎧 Dégg

📜 Aaya 21-25 — Aali Imran

21إِنَّ الَّذِينَ يَكْفُرُونَ بِآيَاتِ اللَّهِ وَيَقْتُلُونَ النَّبِيِّينَ بِغَيْرِ حَقٍّ وَيَقْتُلُونَ الَّذِينَ يَأْمُرُونَ بِالْقِسْطِ مِنَ النَّاسِ فَبَشِّرْهُم بِعَذَابٍ أَلِيمٍ
Ñay weddi kàdduy Yàlla, di rey Yonent ya, ci lu dul dëgg, di rey ñay digle maandute ci nit ñi, na nga leen bégal ci mbugalmu tar.
22أُولَٰئِكَ الَّذِينَ حَبِطَتْ أَعْمَالُهُمْ فِي الدُّنْيَا وَالْآخِرَةِ وَمَا لَهُم مِّن نَّاصِرِينَ
Ñooña seeni jëf sippiku na ci àddina ak ca àllaaxira. Te duñu am ndimbal !
23أَلَمْ تَرَ إِلَى الَّذِينَ أُوتُوا نَصِيبًا مِّنَ الْكِتَابِ يُدْعَوْنَ إِلَىٰ كِتَابِ اللَّهِ لِيَحْكُمَ بَيْنَهُمْ ثُمَّ يَتَوَلَّىٰ فَرِيقٌ مِّنْهُمْ وَهُم مُّعْرِضُونَ
Moo ndax gisoo ñañu jox cér ca téere ba , woowees na leen jëme ci Téere Yàlla bi ngir mu àtte seeni diggante ; am kurél ci ñoom bu dummóoyu, far ñoom ñépp dummóoyu.
24ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ قَالُوا لَن تَمَسَّنَا النَّارُ إِلَّا أَيَّامًا مَّعْدُودَاتٍ ۖ وَغَرَّهُمْ فِي دِينِهِم مَّا كَانُوا يَفْتَرُونَ
Ndax ñoom dañuy wax ne : “Safara dunu laal lu dul ay bis yuñu lim”. Dañuy duural Yàlla ci seen diine, loolaa leen nax.
25فَكَيْفَ إِذَا جَمَعْنَاهُمْ لِيَوْمٍ لَّا رَيْبَ فِيهِ وَوُفِّيَتْ كُلُّ نَفْسٍ مَّا كَسَبَتْ وَهُمْ لَا يُظْلَمُونَ
Naka la ñuy def ca bis ba, kenn warut a nàttable ci ne dana am, bu ñu leen dajalee ba kenn ku nekk ñu jox ko la mu fàggu woon mu mat sëkk.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
23Aaya

Tekki — Aali Imran 23

Simoore Aali Imran Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax gisoo ñañu jox cér ca téere ba ,…

Simoore Aaya 23/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers