Aali Imran · 62/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
إِنَّ هَٰذَا لَهُوَ الْقَصَصُ الْحَقُّ ۚ وَمَا مِنْ إِلَٰهٍ إِلَّا اللَّهُ ۚ وَإِنَّ اللَّهَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ ۝٦٢
Innaa haazaa lahuwal qasasul haqq; wa maa min ilaahin illal laah; wa innal laahaa la Huwal `Azeezul Hakeem
📖 Tekkim Wolof
Lii mooy nettali yu dëggu ya. Te amul yàlla ju yayoo jaamu ku dul Yàlla. Te Mooy ki not, ki xereñ.
🎧 Dégg

📜 Aaya 60-64 — Aali Imran

60الْحَقُّ مِن رَّبِّكَ فَلَا تَكُن مِّنَ الْمُمْتَرِينَ
Dëgg ca sa Boroom la jóge. Bul bokk ca ña cay werante.
61فَمَنْ حَاجَّكَ فِيهِ مِن بَعْدِ مَا جَاءَكَ مِنَ الْعِلْمِ فَقُلْ تَعَالَوْا نَدْعُ أَبْنَاءَنَا وَأَبْنَاءَكُمْ وَنِسَاءَنَا وَنِسَاءَكُمْ وَأَنفُسَنَا وَأَنفُسَكُمْ ثُمَّ نَبْتَهِلْ فَنَجْعَل لَّعْنَتَ اللَّهِ عَلَى الْكَاذِبِينَ
Ku cay dàggasante ak yaw, ginnaaw la la dikke ci xam-xam [ci mbiri Iisaa], neel : “Kaayleen nu woo sunuy doom ak sunuy soxna ak seeni soxna, nu ñëw, ngeen ñëw yéen ci seen bopp topp nu toroxlu, rëbbante rëbbum Yàlla dal ci ña fen [ci mbiri Iisaa].
62إِنَّ هَٰذَا لَهُوَ الْقَصَصُ الْحَقُّ ۚ وَمَا مِنْ إِلَٰهٍ إِلَّا اللَّهُ ۚ وَإِنَّ اللَّهَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Lii mooy nettali yu dëggu ya. Te amul yàlla ju yayoo jaamu ku dul Yàlla. Te Mooy ki not, ki xereñ.
63فَإِن تَوَلَّوْا فَإِنَّ اللَّهَ عَلِيمٌ بِالْمُفْسِدِينَ
Bu ñu dëddoo [dummóoyu] ... Yàlla xàmmee na yàqkat ya !
64قُلْ يَا أَهْلَ الْكِتَابِ تَعَالَوْا إِلَىٰ كَلِمَةٍ سَوَاءٍ بَيْنَنَا وَبَيْنَكُمْ أَلَّا نَعْبُدَ إِلَّا اللَّهَ وَلَا نُشْرِكَ بِهِ شَيْئًا وَلَا يَتَّخِذَ بَعْضُنَا بَعْضًا أَرْبَابًا مِّن دُونِ اللَّهِ ۚ فَإِن تَوَلَّوْا فَقُولُوا اشْهَدُوا بِأَنَّا مُسْلِمُونَ
- Neel : “Yéen ñoñ-téere yi, kaayleen ci baat boo xam ne yéen ak nun noo ciy maase : dunu jaamu ku dul Yàlla, te nu bañ cee bokkaale dara, te kenn ci nun bañ jël moroomam jàppe ko Yàlla, di ko jaamu”. Su ñu bañee ba dummóoyu, neeleen : “Seedeleen ne nun dey way-wommatu lanu [ci topp Yàlla]”.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
62Aaya

Tekki — Aali Imran 62

Simoore Aali Imran Aaya 62 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lii mooy nettali yu dëggu ya. Te amul yàlla ju…

Simoore Aaya 62/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 60–64. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers