As-Saffat · 104/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَنَادَيْنَاهُ أَن يَا إِبْرَاهِيمُ ۝١٠٤
Wa naadainaahu ai yaaaa Ibraheem
📖 Tekkim Wolof
Nu woo ko, ne ko : “Éy yaw Ibraahiima !

🎧 Dégg


📜 Aaya 102-106 — Simoore As-Saffat

102فَلَمَّا بَلَغَ مَعَهُ السَّعْيَ قَالَ يَا بُنَيَّ إِنِّي أَرَىٰ فِي الْمَنَامِ أَنِّي أَذْبَحُكَ فَانظُرْ مَاذَا تَرَىٰ ۚ قَالَ يَا أَبَتِ افْعَلْ مَا تُؤْمَرُ ۖ سَتَجِدُنِي إِن شَاءَ اللَّهُ مِنَ الصَّابِرِينَ
Ba mu amee ati àndak moom, Ibraahiima wax na ne : "Yaw samas doom, gis naa ci bi may nelaw, ci biir gént, ndigalul war laa rendi. Seetal looy xalaat”. (Ismaayiila) ne ko : “Yaw sama baay, defal lu ñu la digal : bu soobee Yàlla, danga gis ne maag muñkat yee ànd”.
103فَلَمَّا أَسْلَمَا وَتَلَّهُ لِلْجَبِينِ
Ba ñu wéyalee seen ndigalul Boroom, mu di dëféenal ko,
104وَنَادَيْنَاهُ أَن يَا إِبْرَاهِيمُ
Nu woo ko, ne ko : “Éy yaw Ibraahiima !
105قَدْ صَدَّقْتَ الرُّؤْيَا ۚ إِنَّا كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Dëggal nga gént gi. Te noonu la Nuy feye ñiy rafetal”.
106إِنَّ هَٰذَا لَهُوَ الْبَلَاءُ الْمُبِينُ
Lii ab tontu la bu bir.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
104Aaya

Tekki — As-Saffat 104

Simoore As-Saffat Aaya 104 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu woo ko, ne ko : “Éy yaw Ibraahiima !

Simoore Aaya 104/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 102–106. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers