As-Saffat · 134/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِذْ نَجَّيْنَاهُ وَأَهْلَهُ أَجْمَعِينَ ۝١٣٤
Iz najjainaahu wa ahlahooo ajma`een
📖 Tekkim Wolof
[Fàttalikul] ba Nu ko musalee mook njabootam gépp,

🎧 Dégg


📜 Aaya 132-136 — Simoore As-Saffat

132إِنَّهُ مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ
bokk na ci Sunu jaam ñi gëm.
133وَإِنَّ لُوطًا لَّمِنَ الْمُرْسَلِينَ
Lóot it bokk na ci Yonent yi.
134إِذْ نَجَّيْنَاهُ وَأَهْلَهُ أَجْمَعِينَ
[Fàttalikul] ba Nu ko musalee mook njabootam gépp,
135إِلَّا عَجُوزًا فِي الْغَابِرِينَ
ba mu des màggat gu jigéen ga àndoon ak ña sànku wo
136ثُمَّ دَمَّرْنَا الْآخَرِينَ
Ginnaaw ba, faagaagal Nanu ña ca des
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
134Aaya

Tekki — As-Saffat 134

Simoore As-Saffat Aaya 134 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Fàttalikul] ba Nu ko musalee mook njabootam gépp,

Simoore Aaya 134/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 132–136. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers