As-Saffat · 135/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِلَّا عَجُوزًا فِي الْغَابِرِينَ ۝١٣٥
Illaa `ajoozan fil ghaabireen
📖 Tekkim Wolof
ba mu des màggat gu jigéen ga àndoon ak ña sànku wo

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 133-137 — Simoore As-Saffat

133وَإِنَّ لُوطًا لَّمِنَ الْمُرْسَلِينَ
Lóot it bokk na ci Yonent yi.
134إِذْ نَجَّيْنَاهُ وَأَهْلَهُ أَجْمَعِينَ
[Fàttalikul] ba Nu ko musalee mook njabootam gépp,
135إِلَّا عَجُوزًا فِي الْغَابِرِينَ
ba mu des màggat gu jigéen ga àndoon ak ña sànku wo
136ثُمَّ دَمَّرْنَا الْآخَرِينَ
Ginnaaw ba, faagaagal Nanu ña ca des
137وَإِنَّكُمْ لَتَمُرُّونَ عَلَيْهِم مُّصْبِحِينَ
Te yéen a ngi leen di romb bu ngeen di xëy
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
135Aaya

Tekki — As-Saffat 135

Simoore As-Saffat Aaya 135 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ba mu des màggat gu jigéen ga àndoon ak ña…

Simoore Aaya 135/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 133–137. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Sunday, October 4, 2026

Don't forget us in your sincere prayers