As-Saffat · 139/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَإِنَّ يُونُسَ لَمِنَ الْمُرْسَلِينَ ۝١٣٩
Wa inna Yoonusa laminal mursaleen
📖 Tekkim Wolof
Yuunuusa it bokk na ca Yonent ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 137-141 — Simoore As-Saffat

137وَإِنَّكُمْ لَتَمُرُّونَ عَلَيْهِم مُّصْبِحِينَ
Te yéen a ngi leen di romb bu ngeen di xëy
138وَبِاللَّيْلِ ۗ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
ak ci guddi gi. Xanaa dungeen xalaat ?
139وَإِنَّ يُونُسَ لَمِنَ الْمُرْسَلِينَ
Yuunuusa it bokk na ca Yonent ya.
140إِذْ أَبَقَ إِلَى الْفُلْكِ الْمَشْحُونِ
Ba muy daw jëm ca gaal ga ñu yeb ga,
141فَسَاهَمَ فَكَانَ مِنَ الْمُدْحَضِينَ
Ba ñu wantalee mu bokk ca ña ñu waroon a sànni ca ndox ma.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
139Aaya

Tekki — As-Saffat 139

Simoore As-Saffat Aaya 139 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yuunuusa it bokk na ca Yonent ya.

Simoore Aaya 139/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 137–141. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers