As-Saffat · 140/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِذْ أَبَقَ إِلَى الْفُلْكِ الْمَشْحُونِ ۝١٤٠
Iz abaqa ilal fulkil mash hoon
📖 Tekkim Wolof
Ba muy daw jëm ca gaal ga ñu yeb ga,

🎧 Dégg


📜 Aaya 138-142 — Simoore As-Saffat

138وَبِاللَّيْلِ ۗ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
ak ci guddi gi. Xanaa dungeen xalaat ?
139وَإِنَّ يُونُسَ لَمِنَ الْمُرْسَلِينَ
Yuunuusa it bokk na ca Yonent ya.
140إِذْ أَبَقَ إِلَى الْفُلْكِ الْمَشْحُونِ
Ba muy daw jëm ca gaal ga ñu yeb ga,
141فَسَاهَمَ فَكَانَ مِنَ الْمُدْحَضِينَ
Ba ñu wantalee mu bokk ca ña ñu waroon a sànni ca ndox ma.
142فَالْتَقَمَهُ الْحُوتُ وَهُوَ مُلِيمٌ
Jën wa dal koy wann, muy ku yeddu.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
140Aaya

Tekki — As-Saffat 140

Simoore As-Saffat Aaya 140 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba muy daw jëm ca gaal ga ñu yeb ga,

Simoore Aaya 140/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 138–142. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers