As-Saffat · 141/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَسَاهَمَ فَكَانَ مِنَ الْمُدْحَضِينَ ۝١٤١
Fasaahama fakaana minal mudhadeen
📖 Tekkim Wolof
Ba ñu wantalee mu bokk ca ña ñu waroon a sànni ca ndox ma.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 139-143 — Simoore As-Saffat

139وَإِنَّ يُونُسَ لَمِنَ الْمُرْسَلِينَ
Yuunuusa it bokk na ca Yonent ya.
140إِذْ أَبَقَ إِلَى الْفُلْكِ الْمَشْحُونِ
Ba muy daw jëm ca gaal ga ñu yeb ga,
141فَسَاهَمَ فَكَانَ مِنَ الْمُدْحَضِينَ
Ba ñu wantalee mu bokk ca ña ñu waroon a sànni ca ndox ma.
142فَالْتَقَمَهُ الْحُوتُ وَهُوَ مُلِيمٌ
Jën wa dal koy wann, muy ku yeddu.
143فَلَوْلَا أَنَّهُ كَانَ مِنَ الْمُسَبِّحِينَ
Dugankoon ak li mu bokkoon ca ña doon sàbbaal Yàlla,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
141Aaya

Tekki — As-Saffat 141

Simoore As-Saffat Aaya 141 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ñu wantalee mu bokk ca ña ñu waroon a…

Simoore Aaya 141/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 139–143. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers