As-Saffat · 142/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَالْتَقَمَهُ الْحُوتُ وَهُوَ مُلِيمٌ ۝١٤٢
Faltaqamahul hootu wa huwa muleem
📖 Tekkim Wolof
Jën wa dal koy wann, muy ku yeddu.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 140-144 — Simoore As-Saffat

140إِذْ أَبَقَ إِلَى الْفُلْكِ الْمَشْحُونِ
Ba muy daw jëm ca gaal ga ñu yeb ga,
141فَسَاهَمَ فَكَانَ مِنَ الْمُدْحَضِينَ
Ba ñu wantalee mu bokk ca ña ñu waroon a sànni ca ndox ma.
142فَالْتَقَمَهُ الْحُوتُ وَهُوَ مُلِيمٌ
Jën wa dal koy wann, muy ku yeddu.
143فَلَوْلَا أَنَّهُ كَانَ مِنَ الْمُسَبِّحِينَ
Dugankoon ak li mu bokkoon ca ña doon sàbbaal Yàlla,
144لَلَبِثَ فِي بَطْنِهِ إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ
kon dey dana sax ca biir [jën wa] ba bisub dekkiwaat ba di ñëw.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
142Aaya

Tekki — As-Saffat 142

Simoore As-Saffat Aaya 142 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jën wa dal koy wann, muy ku yeddu.

Simoore Aaya 142/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 140–144. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers