As-Saffat · 150/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
أَمْ خَلَقْنَا الْمَلَائِكَةَ إِنَاثًا وَهُمْ شَاهِدُونَ ۝١٥٠
Am khalaqnal malaaa`i kata inaasanw wa hm shaahidoon
📖 Tekkim Wolof
Walla dañoo bind Malaaka yi def leen ñu di ay jigéen, seere ko ? ”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 148-152 — Simoore As-Saffat

148فَآمَنُوا فَمَتَّعْنَاهُمْ إِلَىٰ حِينٍ
Ba ñu gëmee, xéewalal Nanu leen fa ab diir.
149فَاسْتَفْتِهِمْ أَلِرَبِّكَ الْبَنَاتُ وَلَهُمُ الْبَنُونَ
Laajleen baxam : “Ndax Yàlla moo ame doom yu jigéen, ñoom ñuy am doom yu góor ?
150أَمْ خَلَقْنَا الْمَلَائِكَةَ إِنَاثًا وَهُمْ شَاهِدُونَ
Walla dañoo bind Malaaka yi def leen ñu di ay jigéen, seere ko ? ”.
151أَلَا إِنَّهُم مِّنْ إِفْكِهِمْ لَيَقُولُونَ
Ndax ñoom dañuy faral di wax ci seen duur ya, naan :
152وَلَدَ اللَّهُ وَإِنَّهُمْ لَكَاذِبُونَ
“Yàlla am na doom” ; te ñoom dañuy fen doŋŋ !
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
150Aaya

Tekki — As-Saffat 150

Simoore As-Saffat Aaya 150 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla dañoo bind Malaaka yi def leen ñu di ay…

Simoore Aaya 150/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 148–152. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers