As-Saffat · 168/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
لَوْ أَنَّ عِندَنَا ذِكْرًا مِّنَ الْأَوَّلِينَ ۝١٦٨
Law anna `indana zikram minal awwaleen
📖 Tekkim Wolof
“Su nu amoon waarate gu bawoo ca sunuy maam,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 166-170 — Simoore As-Saffat

166وَإِنَّا لَنَحْنُ الْمُسَبِّحُونَ
te nun nooy sàbbaal Yàlla.
167وَإِن كَانُوا لَيَقُولُونَ
Doonte la sax ña ngay wax naan :
168لَوْ أَنَّ عِندَنَا ذِكْرًا مِّنَ الْأَوَّلِينَ
“Su nu amoon waarate gu bawoo ca sunuy maam,
169لَكُنَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ
kon de nu doon ay jaami Yàlla yuy sellal !
170فَكَفَرُوا بِهِ ۖ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ
Weddi nañu ko, waaye danañu xam ne.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
168Aaya

Tekki — As-Saffat 168

Simoore As-Saffat Aaya 168 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Su nu amoon waarate gu bawoo ca sunuy maam,

Simoore Aaya 168/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 166–170. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers