As-Saffat · 169/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
لَكُنَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ ۝١٦٩
Lakunna `ibaadal laahil mukhlaseen
📖 Tekkim Wolof
kon de nu doon ay jaami Yàlla yuy sellal !

🎧 Dégg


📜 Aaya 167-171 — Simoore As-Saffat

167وَإِن كَانُوا لَيَقُولُونَ
Doonte la sax ña ngay wax naan :
168لَوْ أَنَّ عِندَنَا ذِكْرًا مِّنَ الْأَوَّلِينَ
“Su nu amoon waarate gu bawoo ca sunuy maam,
169لَكُنَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ
kon de nu doon ay jaami Yàlla yuy sellal !
170فَكَفَرُوا بِهِ ۖ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ
Weddi nañu ko, waaye danañu xam ne.
171وَلَقَدْ سَبَقَتْ كَلِمَتُنَا لِعِبَادِنَا الْمُرْسَلِينَ
Sunu kàddu jiitu woon na ci Sunu jaam ña di ay Yonent,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
169Aaya

Tekki — As-Saffat 169

Simoore As-Saffat Aaya 169 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : kon de nu doon ay jaami Yàlla yuy sellal !

Simoore Aaya 169/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 167–171. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers