As-Saffat · 19/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَإِنَّمَا هِيَ زَجْرَةٌ وَاحِدَةٌ فَإِذَا هُمْ يَنظُرُونَ ۝١٩
Fa innamaa hiya zajra tunw waahidatun fa izaa hum yanzuroon
📖 Tekkim Wolof
Genn ug xaacu rekk ay jib, ñu ne xewwu di xoolante (dekki),

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 17-21 — Simoore As-Saffat

17أَوَآبَاؤُنَا الْأَوَّلُونَ
ak sunuy baay ak i maamaat ? ”
18قُلْ نَعَمْ وَأَنتُمْ دَاخِرُونَ
Neel : “Waaw ! te dangeen torox de”.
19فَإِنَّمَا هِيَ زَجْرَةٌ وَاحِدَةٌ فَإِذَا هُمْ يَنظُرُونَ
Genn ug xaacu rekk ay jib, ñu ne xewwu di xoolante (dekki),
20وَقَالُوا يَا وَيْلَنَا هَٰذَا يَوْمُ الدِّينِ
ñuy wax naan : “Ngalla nun ! Bis-pénc baa ngi nii waay”.
21هَٰذَا يَوْمُ الْفَصْلِ الَّذِي كُنتُم بِهِ تُكَذِّبُونَ
“Lii mooy bisub àtte ba ngeen jàppe woon ay fen, weddi ko”.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
19Aaya

Tekki — As-Saffat 19

Simoore As-Saffat Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Genn ug xaacu rekk ay jib, ñu ne xewwu di…

Simoore Aaya 19/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers