As-Saffat · 20/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَقَالُوا يَا وَيْلَنَا هَٰذَا يَوْمُ الدِّينِ ۝٢٠
Qa qaaloo yaa wailanaa haazaa Yawmud-Deen
📖 Tekkim Wolof
ñuy wax naan : “Ngalla nun ! Bis-pénc baa ngi nii waay”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 18-22 — Simoore As-Saffat

18قُلْ نَعَمْ وَأَنتُمْ دَاخِرُونَ
Neel : “Waaw ! te dangeen torox de”.
19فَإِنَّمَا هِيَ زَجْرَةٌ وَاحِدَةٌ فَإِذَا هُمْ يَنظُرُونَ
Genn ug xaacu rekk ay jib, ñu ne xewwu di xoolante (dekki),
20وَقَالُوا يَا وَيْلَنَا هَٰذَا يَوْمُ الدِّينِ
ñuy wax naan : “Ngalla nun ! Bis-pénc baa ngi nii waay”.
21هَٰذَا يَوْمُ الْفَصْلِ الَّذِي كُنتُم بِهِ تُكَذِّبُونَ
“Lii mooy bisub àtte ba ngeen jàppe woon ay fen, weddi ko”.
22۞ احْشُرُوا الَّذِينَ ظَلَمُوا وَأَزْوَاجَهُمْ وَمَا كَانُوا يَعْبُدُونَ
“Dajaleleen tooñkat ya ak seeni jabar ak la ñu daan jaamu,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
20Aaya

Tekki — As-Saffat 20

Simoore As-Saffat Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ñuy wax naan : “Ngalla nun ! Bis-pénc baa ngi…

Simoore Aaya 20/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers