As-Saffat · 62/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
أَذَٰلِكَ خَيْرٌ نُّزُلًا أَمْ شَجَرَةُ الزَّقُّومِ ۝٦٢
Azaalika khairun nuzulan am shajaratuz Zaqqom
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax loolu moo di wàccuwaay ba gën, walla garabug Zaquum ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 60-64 — Simoore As-Saffat

60إِنَّ هَٰذَا لَهُوَ الْفَوْزُ الْعَظِيمُ
Lii mooy texe gu màgg ga.
61لِمِثْلِ هَٰذَا فَلْيَعْمَلِ الْعَامِلُونَ
Ñiy jëf, nañuy jëf lu mel nii.
62أَذَٰلِكَ خَيْرٌ نُّزُلًا أَمْ شَجَرَةُ الزَّقُّومِ
Moo ndax loolu moo di wàccuwaay ba gën, walla garabug Zaquum ?
63إِنَّا جَعَلْنَاهَا فِتْنَةً لِّلظَّالِمِينَ
Def nanu ko muy sànjub tooñkat ya.
64إِنَّهَا شَجَرَةٌ تَخْرُجُ فِي أَصْلِ الْجَحِيمِ
Moom garab la guy génn ca ndéntul Safara.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
62Aaya

Tekki — As-Saffat 62

Simoore As-Saffat Aaya 62 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax loolu moo di wàccuwaay ba gën, walla garabug…

Simoore Aaya 62/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 60–64. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers