Sad · 58/88
Tekki Waxtaan — Simoore Sad
وَآخَرُ مِن شَكْلِهِ أَزْوَاجٌ ۝٥٨
Wa aakharu min shak liheee azwaaj
📖 Tekkim Wolof
ak yeneeni xeeti mbugël yu mu témbóol.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 56-60 — Simoore Sad

56جَهَنَّمَ يَصْلَوْنَهَا فَبِئْسَ الْمِهَادُ
Mooy Safara su ñuy xoyomoo. ndaw kër gu bon !
57هَٰذَا فَلْيَذُوقُوهُ حَمِيمٌ وَغَسَّاقٌ
Mi ngi nii ! Nu cay tokamtiku : ndox muy tàng ak a wañax,
58وَآخَرُ مِن شَكْلِهِ أَزْوَاجٌ
ak yeneeni xeeti mbugël yu mu témbóol.
59هَٰذَا فَوْجٌ مُّقْتَحِمٌ مَّعَكُمْ ۖ لَا مَرْحَبًا بِهِمْ ۚ إِنَّهُمْ صَالُو النَّارِ
Ñii ay mbooloo la ñu ñuy buuxanteek yéen, kenn dalaluleen. Te ñooy xoyomu ca Safara.
60قَالُوا بَلْ أَنتُمْ لَا مَرْحَبًا بِكُمْ ۖ أَنتُمْ قَدَّمْتُمُوهُ لَنَا ۖ فَبِئْسَ الْقَرَارُ
Ñuy wax naan : “Yéen kay la kenn dul dalal, lii, Yéen la ñu ko waajal”. Te ndaw saxuwaay bu bon !
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
58Aaya

Tekki — Sad 58

Simoore Sad Aaya 58 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak yeneeni xeeti mbugël yu mu témbóol.

Simoore Aaya 58/88 — Simoore Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Sad Dégg, Simoore Sad Tekki, Simoore Sad mp3, Simoore Sad pdf. Aaya 56–60. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers