Sad · 85/88
Tekki Waxtaan — Sad
لَأَمْلَأَنَّ جَهَنَّمَ مِنكَ وَمِمَّن تَبِعَكَ مِنْهُمْ أَجْمَعِينَ ۝٨٥
La amla`annna Jahannama minka wa mimman tabi`aka minhum ajma`een
📖 Tekkim Wolof
Danaa feesal Safara ci yaw ak ña la topp ñépp”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 83-87 — Sad

83إِلَّا عِبَادَكَ مِنْهُمُ الْمُخْلَصِينَ
ba mu des sa jaam ñiy sellal”.
84قَالَ فَالْحَقُّ وَالْحَقَّ أَقُولُ
(Yàlla) daldi wax ne : “Maa ngi waat, ci dëgg ne dëgg laay wax,
85لَأَمْلَأَنَّ جَهَنَّمَ مِنكَ وَمِمَّن تَبِعَكَ مِنْهُمْ أَجْمَعِينَ
Danaa feesal Safara ci yaw ak ña la topp ñépp”.
86قُلْ مَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ وَمَا أَنَا مِنَ الْمُتَكَلِّفِينَ
Waxal ne : “Laajumaleen ci ag pey ; te it yanuwuma ci.
87إِنْ هُوَ إِلَّا ذِكْرٌ لِّلْعَالَمِينَ
[Alxuraan] jii daal ag fàttali la ñeel waa àddina si yépp.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
85Aaya

Tekki — Sad 85

Simoore Sad Aaya 85 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Danaa feesal Safara ci yaw ak ña la topp ñépp”.

Simoore Aaya 85/88 — Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Sad Dégg, Sad Tekki, Sad mp3, Sad pdf. Aaya 83–87. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers