An-Nisa · 156/176
Tekki Waxtaan — An-Nisa
وَبِكُفْرِهِمْ وَقَوْلِهِمْ عَلَىٰ مَرْيَمَ بُهْتَانًا عَظِيمًا ١٥٦
Transliteration
Wa bikufrihim wa qawlihim `alaa Maryama buh taanan `azeema
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ak ca sababus la ñu weddi, te wax ci Maryaama duur [fen] wu rëy.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 154-158 — An-Nisa
154وَرَفَعْنَا فَوْقَهُمُ الطُّورَ بِمِيثَاقِهِمْ وَقُلْنَا لَهُمُ ادْخُلُوا الْبَابَ سُجَّدًا وَقُلْنَا لَهُمْ لَا تَعْدُوا فِي السَّبْتِ وَأَخَذْنَا مِنْهُم مِّيثَاقًا غَلِيظًا
Nu yékkati doj wa ca seen kaw ngir fasanteek ñoom kóllare, ñu ne leen woon : “Dugguleen ci buntu bi ànd ak di sujjóot” ; Neeti leen : “Buleen jalgati bisub gaawu” ; Nu jàppe woon ak ñoom kóllëre gu dëgër.
155فَبِمَا نَقْضِهِم مِّيثَاقَهُمْ وَكُفْرِهِم بِآيَاتِ اللَّهِ وَقَتْلِهِمُ الْأَنبِيَاءَ بِغَيْرِ حَقٍّ وَقَوْلِهِمْ قُلُوبُنَا غُلْفٌ ۚ بَلْ طَبَعَ اللَّهُ عَلَيْهَا بِكُفْرِهِمْ فَلَا يُؤْمِنُونَ إِلَّا قَلِيلًا
Ci sababu firig seen kóllare ak seen weddi kàdduy Yàlla ya, ak rey ga ñu rey Yonent ya ci lu dul dëgg, ak la ñuy wax naan: “Sunuy xel muuru na”. Li am kay moo di Yàllaa fatt seeni xol ci sababus seenug la ñu weddi, ñu néew ñoo gëm ca ña bokk ca ñoom.
156وَبِكُفْرِهِمْ وَقَوْلِهِمْ عَلَىٰ مَرْيَمَ بُهْتَانًا عَظِيمًا
Ak ca sababus la ñu weddi, te wax ci Maryaama duur [fen] wu rëy.
157وَقَوْلِهِمْ إِنَّا قَتَلْنَا الْمَسِيحَ عِيسَى ابْنَ مَرْيَمَ رَسُولَ اللَّهِ وَمَا قَتَلُوهُ وَمَا صَلَبُوهُ وَلَٰكِن شُبِّهَ لَهُمْ ۚ وَإِنَّ الَّذِينَ اخْتَلَفُوا فِيهِ لَفِي شَكٍّ مِّنْهُ ۚ مَا لَهُم بِهِ مِنْ عِلْمٍ إِلَّا اتِّبَاعَ الظَّنِّ ۚ وَمَا قَتَلُوهُ يَقِينًا
ak ca la ñu wax ne : “Noo rey [Masiihu Iisaa] doomi Maryaama, Yonentub Yàlla ba”... Te reyuñu ko, daajuñu ko ci ay bant ; waaye dañu leen koo nirëleel ñu cay werante ! Wóor na ne ci am lënt lañu nekk ci mbir moomu: amuñu ca benn xam-xam lu dul topp seen njort, te nag reyuñu ko de.
158بَل رَّفَعَهُ اللَّهُ إِلَيْهِ ۚ وَكَانَ اللَّهُ عَزِيزًا حَكِيمًا
li am kay mooy Yàllaa ko yékkati jëme ko ca Moom. Te Yàllaa di Ku not lépp, di Ku xereñ.
An-NisaFihi Alxuraan
176Aaya
MedinanRevelation
156Aaya
Tekki — An-Nisa 156
Simoore An-Nisa Aaya 156 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak ca sababus la ñu weddi, te wax ci Maryaama…Simoore Aaya 156/176 — An-Nisa النساء (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nisa Dégg, An-Nisa Tekki, An-Nisa mp3, An-Nisa pdf. Aaya 154–158. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








