Ghafir · 20/85
Tekki Waxtaan — Simoore Ghafir
وَاللَّهُ يَقْضِي بِالْحَقِّ ۖ وَالَّذِينَ يَدْعُونَ مِن دُونِهِ لَا يَقْضُونَ بِشَيْءٍ ۗ إِنَّ اللَّهَ هُوَ السَّمِيعُ الْبَصِيرُ ۝٢٠
Wallaahu yaqdee bilhaqq, wallazeena yad`oona min doonihee laa yaqdoona bishai`; innal laaha Huwas Samee`ul Baseer
📖 Tekkim Wolof
Yàlla mooy àtte ci dëgg, ña ñu koy bokkaaleel du nu àtte dara. Te Yàlla kuy Dégg la, kuy Gis la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 18-22 — Simoore Ghafir

18وَأَنذِرْهُمْ يَوْمَ الْآزِفَةِ إِذِ الْقُلُوبُ لَدَى الْحَنَاجِرِ كَاظِمِينَ ۚ مَا لِلظَّالِمِينَ مِنْ حَمِيمٍ وَلَا شَفِيعٍ يُطَاعُ
na nga leen xupp ci bis buy jige si, ba xol yi di nekk ci put yi, (ngir tiit ak njàqare). Te bu boobaa tooñkat yi du ñu fa am xarit, mbaa ku leen di tinu ñu di ko topp.
19يَعْلَمُ خَائِنَةَ الْأَعْيُنِ وَمَا تُخْفِي الصُّدُورُ
Xam na worug ay gët, luy nëbbu ci biir dënn yi.
20وَاللَّهُ يَقْضِي بِالْحَقِّ ۖ وَالَّذِينَ يَدْعُونَ مِن دُونِهِ لَا يَقْضُونَ بِشَيْءٍ ۗ إِنَّ اللَّهَ هُوَ السَّمِيعُ الْبَصِيرُ
Yàlla mooy àtte ci dëgg, ña ñu koy bokkaaleel du nu àtte dara. Te Yàlla kuy Dégg la, kuy Gis la.
21۞ أَوَلَمْ يَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَيَنظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الَّذِينَ كَانُوا مِن قَبْلِهِمْ ۚ كَانُوا هُمْ أَشَدَّ مِنْهُمْ قُوَّةً وَآثَارًا فِي الْأَرْضِ فَأَخَذَهُمُ اللَّهُ بِذُنُوبِهِمْ وَمَا كَانَ لَهُم مِّنَ اللَّهِ مِن وَاقٍ
Moo ndax da ñoo doxul ci suuf, tey seetlu mujug ña leen fi jiitu woon te ëppoon doole ak i alal ? Yàlla faagaagaloon leen ngir seeni bàkkar. Te kenn manu leen woon fegal mbugëlu Yàlla mii.
22ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ كَانَت تَّأْتِيهِمْ رُسُلُهُم بِالْبَيِّنَاتِ فَكَفَرُوا فَأَخَذَهُمُ اللَّهُ ۚ إِنَّهُ قَوِيٌّ شَدِيدُ الْعِقَابِ
Li ko waral, moo di ñoom seeni Yonnent, da ñu leen daan indil ay lay yu leer ñu weddi. Yàlla daldi leen faagaagal, Yàlla boroom doole la di ku Tar mbugël.
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
20Aaya

Tekki — Ghafir 20

Simoore Ghafir Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla mooy àtte ci dëgg, ña ñu koy bokkaaleel du…

Simoore Aaya 20/85 — Simoore Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ghafir Dégg, Simoore Ghafir Tekki, Simoore Ghafir mp3, Simoore Ghafir pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers