Ad-Dukhan · 25/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
كَمْ تَرَكُوا مِن جَنَّاتٍ وَعُيُونٍ ۝٢٥
Kam tarakoo min jannaatinw wa `uyoon
📖 Tekkim Wolof
Ak a bari ay dër yu ñu bàyyi ginnaaw ak bëti ndox

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 23-27 — Simoore Ad-Dukhan

23فَأَسْرِ بِعِبَادِي لَيْلًا إِنَّكُم مُّتَّبَعُونَ
“Toppal guddi rañaan ak samay jaam ; danañu len dabusi.
24وَاتْرُكِ الْبَحْرَ رَهْوًا ۖ إِنَّهُمْ جُندٌ مُّغْرَقُونَ
Bàyyil géej ga mu ne tekk ; ndax ñoom ay xarekat lañu ñuy, xala lab”.
25كَمْ تَرَكُوا مِن جَنَّاتٍ وَعُيُونٍ
Ak a bari ay dër yu ñu bàyyi ginnaaw ak bëti ndox
26وَزُرُوعٍ وَمَقَامٍ كَرِيمٍ
ak tool (mbay) ak kër yu taaru,
27وَنَعْمَةٍ كَانُوا فِيهَا فَاكِهِينَ
ak i xéewal yu ñu daan gamaajoo.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 25

Simoore Ad-Dukhan Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak a bari ay dër yu ñu bàyyi ginnaaw ak…

Simoore Aaya 25/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers